(Vidéo) "Serigne Béthio fait mieux que nos parents..." témoigne sa femme. Regardez

Suivez le témoignage de l’une des épouses de Cheikh Bethio Thioune lors de la cérémonie de Gamou à Mermoz. Selon la dame les marabouts valent plus que les parents, car au jugement dernier ce sont eux qui nous aident.

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Dans le même thême

113 commentaires

  1. fatou

    billaye yienna rerr cheich bethio moye yalla khana warre na tite mome si bopome sounioukokoye wakhe lakhira dina mettit tadiague djiguenne si mome yalle nako yalla wolle bathie ndaye sanne tayouko de


  2. Bibou

    Arrêtez les insultes car sa mère a quitté ce bas monde il y’a même pas deux mois. Qu’allah nous protège contre les gens qui sont avec satan. Tôt ou tard on sera devant allah le grand justicier


  3. Abdalla

    même serigne touba hadim rassoul so nieuwé si môme daf lay demandé dakh say wadiour sont d’accord où pas.j’aime mes parents de tout mon âme


  4. wa pa

    ahhh yawmal khiyam dé ah serigne bou matoul serigne moy dimbaliii.

    c’est ce que a dit cette femme, vous entendez bien… elles n’ont meme pas la capacité de parler, et de réfléchir ce qu’elles disent.


  5. FEMME BI DAFA RERE YALLA NAKO YALLA GUINDE TEMOME DAFA KHAMOULE NE SERIGNE SALIOU MI BETHIO GEUME SILOUMOU WAKH MOME SAKH DAFAYE WAKH WADIOUR BA PARE DORE NE SERIGNE DAKH SAPE SERIGNE BOULA GARAME TE WADIOUR GEURA MOULA AMOULE NDIARIGNE TE YALLA DOU GEURAM


  6. mamefa93

    mane louma diakhal nèkalè bèthio yeup meuna wakh douma wakh sakh diabar nakh takougnoulène silou diné wakh mè yaw ya gnak diom say parent gay dieunè ak bèthio mane dal ma waro


  7. ibrahima

    yalla rék moy deug kou fi yalla dink alla xam xam meun meun mba mbollo ba nga ték sa bop fou wéssou diam yague yague da modjié wéét !!! sénégalais yalla may nako xél xamé na deug aki séytané mo tax gniou mélni béthio torokh téy té déss avant de mourir di nagne xam lép deug la ca femme mom je considére mm pas c’est dir ndax done diabar béthio rék doyna

    djiallo


  8. Vraiii

    Khalis mola diaral li Man sama yaye ak pape doumako djende Ken sur tere déjà yangui tek Seye cheuveu naturel devant kelk un ko khamni pour mom sering la Talibé yi KO tope dém len ngen ligey ki mounoul dougeul bopem aldiana ngen beugeu mou dougeul len mdrrrrr


  9. Doura

    BILAHI WALAHI TALAHI SI TU NE PART

    PAS DIRE A TES PARENTS DE TE PARDONNAIT SE QUE TU VIENT DE DIRE ET UN GRANDS PECHERS .QU ES QUI TA POUSSAIT A DIRE SA .TU SERA PUNIE SUR TERRES ET AILLEURS


  10. momodou fall

    ça se voit ke cheikh bi djoxnala dara nga nann, g vois ke cheikh bi mo la guenel say wadiour.nala leer nii sans sa ngueremel wadiour di nga gnak fii gnak fee te ken dou ci meun dara


  11. kayzer

    La manufacture a bêtises ils produisent k des conneries a chaque cérémonie son lot connasse satanas avec leur gueulle de merdass puyass salle idiotass


  12. vérité

    le prophète MOUHAMMAD psl nous apprend :  » riddal laahi fii ridal waalidayni wa soukhtoul laahi fii soukhtil waalidayni  » qui veut dire : ngueureumeul yalla mi ngui si ngueureumeul niaari waadiour té méroum yalla itammi ngui si méroum niaari waadiour


    et cette femme se permet de dire liniou serigne bi défal souniou waadiour défarougne niou ko ndakh wadiour si adouna la yam ! béthio diangalal say diabbar ak sa ay taalibé diiné l’islam et les droits et devoirs envers leurs parents


    • nite

      cette femme la vraie doumoukharam la ndakh bi yalla wesso yonentbi top gnari wadiour moy top. yow déthié pène domaram rek ngua. inutile de te justifier publquement en disant que ta mère t a pardonné toi et béthio tu mens elle est morte de chagrin. ya tardé!!!


    • ndiaye

      donc toi tu ne coné pa ke veu dir wacila cheikh bethio dafa diangal talibé yi nignuy fonké sa wadiour wayé li mu wakh mo ame wadiour anduna la yem lolu kene duko dindi mé nak wakhu gnu kene mu ba respecter say wadiour lolu kugnu ko wakh sakh bo dé nit doko nangu tek l’islam mom bu si doug thiantakone yi dagno mokal teré yalla bi ba diko firé cheikh gnanal leneko yalla ko setal yatal ko kene meunuko tilimal.


    • l'ami se vérité

      très bien dit vérité tu as dit la vérité ces genres de personnes seront chicotés le jour du jugement denier dit le jour j (jj)


Laisser un commentaire