Serigne Basse recadre Junior à propos du « Adiya ».
Vidéo-Serigne Basse recadre Junior à propos du "Adiya". Regardez
Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Serigne Basse recadre Junior à propos du « Adiya ».
Ouvrez l'appli si vous l’avez déjà, sinon téléchargez-la pour une meilleure expérience et pour recevoir les dernières actualités en temps réel.
Non naniou rafétal rékh kou nék gueum ligua gueum té Bayi guarouwalé diarouko
kou beug serigne touba dou tontonté dou khassanté idem pour kou beug el hadj malick sy ak sèn ndiabotte.khana lèp donatoul bèn..
Dieuredieuf serigne bass yaye porte parole bou mate wayé porte parole Bo khamni day mandi xawma doyadi
waa yéne gnioune djoulite yi bougniou défé ni mome mba dina bax na raféte waye nioune gnieupe aye talibé lagniou
YEY SE TOBA
nagnou moytou di wakh yene wakh you yi kilifayi kouy rote fessalago do tangke di toure ta kouy dingate si mouride wala tidjane defo lou nekh sa serigne ta amna lou khilifa ga wakh kerok né kouy dingane mouride wala tidjiane so dougué si bamel boy deki dinga dekalek betakh sissa guemine donté waliwou nga tagnou bayi khel si senego eska gnome aye dioulite lagnou eske bokougnou si gniy khekh dineye l’islam ndakh gnoy diakhassé tarikha yi wa Salam
Lakoum Tarijatoum wali ya Tarija dieredieufaty serigne touba
Serigne touba dou kouniy khekhal lala khoulol waye kounouy ligueyel
Yala na yala yokou jamm sounou rew
Seeing touba Nena kerok yawmalkhiyam khol bouniou khar fek thi beug bamba ma tabal adiana waye khol bouniou khar fek thi bagne bamba ma tabal safara tek thi nii souniou borom moma may lolou te ken douko dindi.dieureudieufate serign touba yaw laniou yakar adouna ak alakhira
Jean tu a tout dit et MERCI de ces conseils. Je crois que c une reflexion qui devait venir de musulman puis q c se q prone l’islam j’ai non pas pour mon pays mais de mes compatriote. Yenagui woo lokhamnee boulen wouyoo dou nguenko beugueu
Ligua wakh machalla
vraiment junior dafa waroul won wakh limou wakh…ndakh serigne sidi mokhtar bimou togue limou dieukeu wakh moy na kholyi ak joulite yi yep nek benn….donc geumeul sa tarikha ta bagna khass yonou diambour diegueulou guenn bal ma
Mes frères et soeurs, chers compatriote, Yoonou daim soriwoul. Naniou def diam, naniou wax diam, naniou yenente diam. Je ne cherche pas a comprendre qui a dit quoi et qui a fait quoi. Pour Mane Mame Maodo ak Mame Bamba ak yenene mame yeup nio ligayal Senegal. Pourquoi s’entre déchirer? Pourquoi ne pas s’appeler au telephone pour s’expliquer et se comprendre? Pourkoi provoquons nous le Diable en touchant sa queue? Faisons attention. Ce Pays est sur un volcan et qui ne le dit pas refuse de reconnaitre la vérité. Moi je suis Catholique mais je ne comprend vraiment pas le problème que vous mes autres mes frères et soeurs voulez créer. Vous avez le même prophète (Mohamed PSL), tous vos guides religieux se réfèrent a lui et vous recommande de le suivre pourquoi donc ces querelles de chapelle? Je suis convaincu d’une chose, ni Mame Maodo ni Mame Bamba n’est honorés dans vos injures. Je commence vraiment a m’inquiéter car si vous ne pouvez pas vous comprendre et vous accepter mutuellement, je me demande si vous êtes vraiment sérieux en parlant de Dialogue Islamo-Chretien.
J’ai meme honte de mon pays.
S’il vous plait restons frères et soeur.
Suivons l appele de Cheikh Sidy Makhtar L UNION entre musulmans
moi je demande pourquoi les tijanes aiment insulter…………un peut de talibe way samagayi
moi je me demande pourquoi les tijanes aime insulter………..un peut de talibe way samaguayi
serigne touba kouko beugoul sawara rek sax xoll di tangeu sassoune
yamana Mew yay YALLA
yalnanou yalla soutral te djegalnou
Serigne touba yalla la…………. Mako waxxx sicap libertei 3 la deuk rakou ndamal darou foleine ma lathieu niou waxleine…..
ken dou serigne touba mami junior mi ngen di wakh dafa djiebalou si khadim rassoul kon nak junior talibe mouride rek lay don mou beug wala mou bagne koo lolou mom ken manou si dara ba pare senegal koufay yewo am mouride nga nga khamko wala nga niak ko kham
Lu way def sa bop serigne touba fi né ku ko wédi démal télé ga wakh ko junior toton mogui doga doit duma top dim faguéne diame mo soriwoul porte parole nu amoul khalifa
SERIGNE TOUBA POINT ..LE RESTE DANS LE COIN
yaw mom denga doff yagui melni ta pa fe les banc
Maam Maodo Point Barre. Serigne Touba à la Poubelle.
Thiey Senegal senegal daal chauffeur si rek nio nek benne.
Ce gros titre du journaliste jappalni saaga yeup tu es responsable, en plus serigne touba moy elhadji malick, revenez sur terre.
Guissnga bass abdou khadr kou réw la dafa wara diangui khamoul dara reuye lamigne la def mourid yi dagnou rér yonou morid kou thi dougou do tékhé fi Sénégal gneup khamnagne kane mo fi raw ta yawmal khiyame lepp dina lérr beuri ngéne wakh trop billahi barké serigne babacar sy kou khamoul loye wakh sy ndiabotou aladji malick dinga trokh
Dieuwrigne kholal ninga tud diwakh louniawli
kane moy babaca khana dou kin don soulli fèke mou neb walliyou dou yakhou
junior doumako diapall dara ndakh khamna dafa mandi won fek
bayileen wakh ji te diamou ji yalla adouna diekhna serigne touba bind na el hadji malick bind na dem leen geusstou ji yenay atte seen bopou wasalam
junior dina dounde ba dé té dou nek khalifa general lolou moy pobare kholame gor gui thi roukk bi mome yalla nafi yague té werr kou mandou la mais serigne bass abdou khadre ligua wakh deugue la serigne touba rawnalene tanki kanam la am dou you guinaw mane nak douma togne mais junior mome meloule ni bayam bou téddba mame abdou dane na wakh toujours niou tapé khole yi kone mome dou dieufé wakhou kilifame mor rek junior mosi mel nonou dieuredieuf serigne touba ak mame malick
Plus impolie que toi tu meur son pere c est serigne abdou khadre mbacke je te le rappel
niake nek mouride woroule
seul le pouvoir de dieu ne finira jamais. tout ce que vous faites de faux finira un jour. dieu est témoin de tout regards on dirait un meeting serigne touba n’aime ni haladji malick vos échanges. les choses se règles mais pas comme ça. vous ne pensés qu’a vos intérêts contraire à l’œuvre de mame bamba et de mame malick qui eux ont un destin commun …l’islam
Diamou tu as parfaitement raison.Diamou yalla rek mo woor,kou laka digaloulr ak kou mounti done dalay,té bo topé dagay perte com mome
Ki dé khamoul dara khamé woul sakh ق ak خ
thim ki dou talibé sakh bay nék serigne
Ñougui wo lo khamnii souñou wouyoo rek dou bakh . Nañou ñane diam tee dokh ci liñou souñou mame you bakh yii bayil
yaw dof dofo nitt ndiaye nga yalla nagnou yalla diegueul thi commentaire yi li yeupp senego la amna yo khamni ken douko publier man nak cheikh la gueum me nak diokh na gneup thieur nagnou bollo te bagna wakhante lou bone balen ma akk
Astafiroulah,Yalla nañou Yalla tek ci yonou siratalmoustahim.
Lii ngueniy def Serigne Touba beugouko mame el hadji Malick beugouko . Serigne Touba doundeum yepp dako def ci ikhssan con ñoun talibe yi nañou rafetal. Nañou bayii khirobii ak ngayobii te khamni tarikha yeup ñoo bok fiñou dieum . Bal lenma akh
ma ngui toup bou bakh mouride mais gniye sagua ni bouniouléne tonetou serigne touba rek mo fi nek
ce qui c’est passé en France est un exemple qui devrait interpellé la conscience de tout un chacun .Notre monde est menacé par l’absence de garde fou.Les média étant le quatrième pouvoir devraient éviter tout ce qui pourrait amener le k.o.Et au sénégal c’est dommage que certain individu n’en sont pas conscient mais à force d’attiser les petits ont finira par avoir une grande incendie .Les foyers religieux ont toujours oeuvrés pour la paix donc nul ne devrait s’aventurer à semer la si sanie .Chacun est libre de croire à qui il veut mais ça lui donne pas le droit d’en vouloir à son prochain .(((la darera wala dirara))). Diewwww nak néhena trop quand tu pense étre introuvable. sama mame wahnamani serigne fallou déguame tolone fo hamni wah djou sew daf ko donne tankanle. A bon entendeur Diamou ba yaw malhiyammmmm
koubagn s touba gasal pax dougousi dougousi soul sa boppou
yaw mi wakh bayam dagua khamoul mamou junior aladji malick sakh se bass dou moromam wakhouma bayam kone se bass eupouna si junior yéne nak séne khol mo diékh diguéne guena déllou guinaw doli si liguéne déllou guana serigne touba day dém séne khole dibone té doléne si mene dara
sama wadjiii linga waxxx euppnaaa !!!! less gars moi jai pitié de vous, vous etes tellement retardés,,,, a sakkk foi Senegal soi vous parler de lutte oubien musique de la danse oubien des maraboutsssss,,,,,,,,,, toiiiii mbi yaw layyyy waxxalll si tu oses,,,,, tard dans la nuit,,,, appelle celui ke tu vien de comparer avec abdou khadre 3 fois,,, epuisss repetes ck tu viens de dire,,, ensuite tu te couchesssss mon ami tu verrasssss sa balla mouyyy yagggggg
yaw domou kharam ji khana sa papa ak sa seringe ngoy nane wiski domou bi reul binga don suering tou ba sokh la woul talibe bou dof yaw do mou dof nga sa job nday 4eve
yaw la so khol diekh yaw mou rid bou dof bi do mou dof
nioune muride dan nioo yar doun saaga te kuniou saaga niou bala Serigne bi nak kuko bagne bayabo nga gass bammel dougou Serigne Basse doudal ba doyal.
yenn sen propre talibe rek mo bakh si yen cisse lo ndakh khamna fan nguendi douguel khaliss bi…?
WAWAW KHAMNA AUSSI YANE SERIGNE NIOY TEUDE DIABAROU DIAMBOUR YI BAYILENE DROGUE BI ADINA DIAYNALENE DE AMNA KO KHAMNI DIOURBEL LANOUKO SOUL MANOUL WONE AGUE TOUBA KONE DAY YAKHOU
Jean Paul djiaz ak jignor gnoy ande di nane wiske
yaw domou kharam ji khana sa papa ak sa seringe ngoy nane wiski domou bi reul binga don suering tou ba sokh la woul talibe bou dof yaw do mou dof nga sa job nday 4eve
haha yén sen khol mo diékh plus de 100ans man léne am diouma bou bakh.yen na wara layté sen khaliss foumou dieum kar nioune guisnan bou bakh louné fangu kén douko weur
saga bakhoul koun yar dou saga man bay cheikh ibra fall la boma saga ma balla
yen ay talibe iblisse guen,kon yalla nalen yalla guindi si barke serigne touba.ndakh kou bagne serigne touba guisoumala mbao.bepou wakh bouguen fi wakh rek serigne basse deukheugne neulen totou li si discourbi.yalla nagnou serigne touba may ak degueu akoup topou.
tapha touba billahi ya wakh deug linga wakh louwerla
kiki khawma kaka kou rew ga khana domi diaaloga yaak sa serigne
KOU NIAK TALIBE GA
khola fo s touba mon fi neh ba abadan dangena wara reg le yena khamoul mai ken kounek tarikha banga bokkou ka sos tarikha ba khamna kan moy s touba boubakh doun ko diema sakh fonto wayr bakhna yen gniy wakh nak nangen khamneh seni serigne tollougnou s touba lala wakh
Rien k des mouton adiya haramm ya k dieu apret tes parents wasalam se son des esploitan de lhomm a lhomm yewoulen bay nelawyi nii denioulen di esploite rek yala mo finek AK prophets et tes deux parents
Amlaine yar yalla nopina yagna te alakmingi gniew loumata sorale lanak ballene mahakh ciao
ce petit tintin il es trop pétit pour recadrer junior même son pére amoul bobou hamham il fais de theatre rec suivi par des moutons illettrés
Kiki boula saytane man ki serigne abdou khadir moye bayam
Te tedego mouye wakh dara ak gniakk yar yaw khamgane sakh
serigne touba amoule morom te diokhe daye takh do niak
qui meunoul recadrer junior car ce dernier mo eupe sakh bayame ham ham il es impolie ce petit tintin
YAWWWWW SE SARAPPP NDEYYEEEEEEEEEEEEEEEE
DIOUF je te rappel que Sérigne TOUBA kessé mo wédiwoul Boromam devant le Colon.
Plus impolie que toi tu meur son pere c est serigne abdou khadre mbacke je te le rappel
YAW KOU REW GA
sa tounou ndaye yaw kik kinga yakar serigne touba la yakar
yow dh barké serigne touba linga wakh boko toboul ba déé safara nga dieum, barké mouhamed
waw c bo diamou lene serigne rek di bokkaleii kou saga yalla kene dou wakh dara meii serigne kouko saga am nga probleme so moy tou woul sakh niou rey lii moy lane ani yalla ak mouhamed psl 1e chose ei sure yawmal kiyamm amoul serigne nieipe yeime li amm solo moy nga gueume yalla ak yonenteime tei nga doylo leine le reste se sont des details wassalam.
je demande au mouride de ne pas repondre aux provocation. souguéne guissé kou ame beusse tole ni beussam bi guéne soga tonetou. pour le moment serigne basse à tous dit .n’ oublié pas que le mouridisme est basé sur le pardon. serigne touba à demandé pardon pour tous.
yaw SE SARAPPP NDEYYEEE ak ko yakarrrrrrrrrr
senegal doyna war li douma si commentaire me kou yakar serigne dina yobou nit aldiana yagui nakh sa bop gueum lene yalla mo gueune
quiconque n’est été éduquer par un guide spirituel valavle rencontra des épreuves terribles ncar satant (seytané) se chargera de lui diriger vers les voix de la perdition.
serigne bamba rek kep lan gueum
ioww tu te suicides vraiment jte jure tu tu suicides et sache ke dingako guiss worna Serigne touba
sa bay yaw mo réw
yaw kou bah déé amo yar wayé adouna ngui sa kanam
Yaw khamo sa bop serigne bass dou séne morom espéce de con ki amoul kham kham moy celui ki a dit publiquement que adiya coruption la et pourtant le prophéte PSL ne mangé que du adiya . Vous navé que la grosse gueule déme léne diangui
Ñoune serigne touba lañou gueme!!! juerejuef serigne bassirou Abdou khadre, kènallène serigne touba moo guene
saytané boumou nu eup doollé .li khew paris exemple la .
ñun niepp ño bokk
p tètr niaka deggo si wax rek la nañu rafétal.
mame maodo ak mame borom touba begouñu linguen di wax
site bi di « senego »day yè fitna té yalla reubna koujo yé
am na lo khamni ken waruko publier.gniy saga mbougal buñ am mo siy euppalé.
bal lenma akh.
meciii Mr je ne vous connait pas mais je salut la pertinence de vos propos . Gueun ngama yokk xam xam . wakh nga deug nagnu dem dianguiwatte sunu Diiné ta bagn di Jamou ay serigne . Certes serigne yi am nagnu liniouy am ba paré . Yalla na Yalla yok séni lerr ta yeureum lén
POUR NGA KHAM SOUNOU BOROM IL FAUT NGA DIAR THI KOUKO KHAM MOU KHAMAL LAKO LOLOU NAK MOY ROLOU SERIGNE
koubakh nga balma mé kilifue bodé wakh dafa wara wakh lokhamni day dokhal réwmi di boolé tarikhayi mé limou wakh képp kou mouride métti nala yalla dafa wakh lakoum diinoukoum waliya diin geumeul linga geum rék ñun serigne touba rék fii ak feulé
sounou noonyi sakh dey sounouk noo noo reck laniouy khar nanou benno bounou feewaloo
Thiey Serigne touna maako gueum Te wolouko
kou nek ak linga gueum ku nek nekal si linga gueum rek
Serigne TouBa moy kéne billahi
CEST VERAIS
ADIYA KENE MANOKAFAI DIEULAI DIEUREDIEUF SERIGNE TOUBA AMOUL MOROOM
ADIYA KENE MANOU KEFAI DIEULAI MOTAX SERIGNE TOUBA NAI TOUBA LIKHABDI MOURIDI SADIKHAN LAKHOUMO BIKHDMTI AW BIKHOUBIN AW HADIYATI