Vidéo- Sa Ndiogou s’attaque sévèrement à Amina Poté: « Ses Bongomen et son émission « Seetu Bi»
Amadou SY
27 COMMENTAIRES
makhtar
15/10/2015 à à 1:33
ndeyssan mom lii rek lafi nekker nekk cii guinaw di critiker rek emission niakk fayda ter amna sponsor yaw bimala khamer batay yagui soga am sponsor jono joni sagal la touty ter yagui magete cci outil khorome pa niakk fayda tu aurai pu lappeler lui donner des conseil arretez de mettre de battons dans les roues de vos camarades
yaw sa ndiogou danga sokhor ignane sa khole bou bon bi gnom dina lene wakh gnou wayeu lat la sa bay sa ndiogou lo bokak golo ndiaye bou golo teube nga teup sa khasa way
Iow sa ndiogou warnaleu iow momou ya wara gueum yalla tei bayi animer liguay niak khorom lidieuntil seu emmission tei bayi diambour o moins Amina el fai parfoi rir lès gens mou tané lako nak meune ngueine grawaal trooop niak khorom
Merci Nité…..Mouride ne nous laissons pa maniopuler par ldes jaloux ki ont des interet autre que borom touba radiyallahou anhou…guerre de media leu rek mais Amina Poté tassouwoul , borom Bongo yi nio wakh ndiakhoum,,, Poté nak na kholat ay invitém dé khol bopam si soline ak wakhitt, télé dafa sensible,,, Avaznt de faire une emission dafa wara wakh ak invité yi , les régles de l'emissions….Mais Poté donté talibém dess neu , wayé talibé leu , nakiou ko djoubeunti ngir djeumou borom touba,,, Mourid day défarr dou yakh , mourid day baalé wayé dou fayou, Mourid day wakh wakh bou rafét wala mou noppi…Sa Ndiogou nak boumou waroul khass ko khamni yalén bokk metier bi , dou yeufou djoulit..Nioun nieup nioy djoum
Sa Ndiogou Amina poté yalén bokk metier bi da ngako wara djapalé outeul ko excuz té khamni nieup nioy djoum…Mouride dafay baalé niko borom touba défé , wayé nak kouy mourid soy fowé sa tarikha moy waral koussi rakh diko fowé.. Naniou yarr ndiaboot gui té wakh ak niom, poté dafay djémeu begueul gayi rek, mais na khol ay invitém yi… Naniouy balanté souniou biir ndakh yalla ball niou, wa salam…
mercy BayeDarou Sa nafekh bou mak la dafa begeu diakhaseh mouride yi ak Youssou Ndour way dina khamne touti nasi nafekh ignian sokhor bone khasaw tilim nopaloulen te khamne meunou len si wa gfm dara morom gfm Yalla moko diapale te kou Yalla diapale domou adama dou meun si mom dara way way rakhass len sen khol yi Senegal diem kanam
sa ndiogo yaw na fekh nga xana danga fatte aniversial bob marle bi nga nek fi niouy toukhe yamba ngafay toudou mame cheikh ibrahima fall amina pote limou def dara nekou si day sant serigne touba rekk kon way katt yi nak khana war nga se wakh ya sof way say tane
Ollof Ndiaye ne bou taranga yokoo non yokou,pote boul tontou boul fale,Sa yaw demo begou kou dem nafekh niak diom li mouride yi defon Sidy Lamin nga begeu nio defko Youssou way bou soube Yalla lolou dou khew ndakh Youssou dafa am respect si domou adama yi motakh nyep respect ko,gfm tha kaw tha kanam kou machaa Allah
Sa yaw ya niak fayda ak sen television bou wett boul ma takha wakh de,li lep dara wara louko loudoul iniane sokhor bone nafekh,kham nga Sidy Lamin mom dafa ragal mouride yi ndakh lanj ko defone lay ragal nieu defat koko,GFM tha kaw tha kanam koumou nakhary talal gas tok si,morom gfm moi lal yokou Machaa Allah,Youssou Yal na sa jamm yokou,Amiin
bande d hypocrite,et de jaloux laisser mouton pisse laisser amina pote tranquil.senegal dou dem animateur ecerele manque esprit creatif sohor ignane. s etes des banse de pareeseux kou deff lou nice so ka topadonoul tu le linche.arretee way sa ndiagou tu te prend pour qui

HAHAHA golo boul ma ray way. merci nite wakh bi am na solo lollll .me amina nekal si diam ya xew senegal kouy dem lanouy bania guiss

sa du matin au soir tu ne fait que des choses you niakk fayda a walf
donc tais toi.pote en tant fille ta depasse et de loin……
mercy BayeDarou Sa nafekh bou mak la dafa begeu diakhaseh mouride yi ak Youssou Ndour way dina khamne touti nasi nafekh ignian sokhor bone khasaw tilim nopaloulen te khamne meunou len si wa gfm dara morom gfm Yalla moko diapale te kou Yalla diapale domou adama dou meun si mom dara way way rakhass len sen khol yi Senegal diem kanam
Regarde moi sa ndiogou clash et la genone la cri de joie…pdfff kifff kiffff
sa ndiogo yaw na fekh nga xana danga fatte aniversial bob marle bi nga nek fi niouy toukhe yamba ngafay toudou mame cheikh ibrahima fall amina pote limou def dara nekou si day sant serigne touba rekk kon way katt yi nak khana war nga se wakh ya sof way say tane
Ollof Ndiaye ne bou taranga yokoo non yokou,pote boul tontou boul fale,Sa yaw demo begou kou dem nafekh niak diom li mouride yi defon Sidy Lamin nga begeu nio defko Youssou way bou soube Yalla lolou dou khew ndakh Youssou dafa am respect si domou adama yi motakh nyep respect ko,gfm tha kaw tha kanam kou machaa Allah
vs laisser pote tankil faire son boulot vs blessez trop de monde fait l'auto critique sur vous
merci walf
merci sa
na yaye falle reuguinn guinnn guinn yaw boula nekhe mourideko tass mbaak reguinn guinnn guinn
Sa yaw ya niak fayda ak sen television bou wett boul ma takha wakh de,li lep dara wara louko loudoul iniane sokhor bone nafekh,kham nga Sidy Lamin mom dafa ragal mouride yi ndakh lanj ko defone lay ragal nieu defat koko,GFM tha kaw tha kanam koumou nakhary talal gas tok si,morom gfm moi lal yokou Machaa Allah,Youssou Yal na sa jamm yokou,Amiin
Sa yaw boul nieu sonal lingay def mo gena niak fayda nafelh ba dee,na bay falle mako wakh Senegal bayilen nafek ak ignian tek nguen tfm beute trop
pote défoul dara li d'où d'Ara sa yaw y'a niak fayda sokhor bâ dh
bande d hypocrite,et de jaloux laisser mouton pisse laisser amina pote tranquil.senegal dou dem animateur ecerele manque esprit creatif sohor ignane. s etes des banse de pareeseux kou deff lou nice so ka topadonoul tu le linche.arretee way sa ndiagou tu te prend pour qui
sa va la bas tête de nul ???
merci Sa
pote do dara momelni ab dof
merci sa grazie couy fo nga fo waye seringe touba fowoule folouwoulle nguir yalla ngenelene seringe touba cie seen thiakhanyi
Dafa saleté dė bâ paré sakh pokotane you khasaw la yor
sa ndiogou wakhko dé poté moniou yép limouye salté