Vidéo : Sa Ndiogou défend Queen Biz et s’acharne sur les animateurs de GFM qui font du « garawalé » pour Bouba Ndour – Regardez.

Sa Ndiogou défend Queen Biz et s’acharne sur les animateurs de GFM qui font du « garawalé » pour Bouba Ndour.

16 COMMENTAIRES
  • diop thor

    sa ndiogou yaw do nit kou bakh démal yagui animation mo guene si yaw wala comédien kkamo darah

  • sambita

    yaw amo foula amo diome cheytané deug nga kou toude kenn buzz do mandou si wakhi diambour ngay nourok golo sa beute you bone yi

  • DEUKHINE MBEUP

    Non maan daamaay baagne SA NDIOGOU weussin wallaa mou biiir quoi !!!

  • fabrice

    wakhal deug yalla li sokhor sax laay nirou di sosal nitt lo gueneu khamoul famille ndour guemleen yalla

    • GOR DOU FEN

      ESK C LA MIFA NDOUR KI A ACCUSE QUEEN BIZZ MANDOU BAKHNA TROP BALA NGAY DIGLAI SANGOU NA FAIK NGA SAIT BA PARAI WAHAL LO HAM AK LO MAITRISER NGAY DOUL NI REK MELNI KOU AMAI DIARRAI MA BAGN GOR BUY FAINN WAY ISH

  • rose

    Feindre de la bonté, quand on est méchant, c’est mettre le comble à la méchanceté.

  • Deugue

    Mais wakh na deugue famille ndour moumouniou senegal ba kouléne lale guéne si wakh

  • Coulibaly coudiabi

    merci beaucoup sa ndiougou saye tané réke

  • MD

    J’ai honte pour youssou ces gens qui prennent sa télé pour un règlement de compte ou pour faire plaisir à Bouba ils devront savoir qu’une télé n’es pas un arme de guerre

  • oumy ndiaye

    tout monde on compris votre jeu maintenant vous voulez être devant tout le monde bamou diaraleen di creer ay faux débat ak soit disant serigne de merde bobou lou nieup wakh moy degueu dagueen sokhoor

  • ngone diouf

    tout vérité est bon a dire vraiment sa ndiogou tu es courageux gni bonne rek moleen diape dou leneen c’est le monde a l’envers leki goor gni nioye garouwalé

  • con

    sa ndiogou Doule

  • xaalass

    On a beau masquer la vérité, tôt ou tard elle se dévoile.sa ndiogou pour une foi tu as raison

  • Sa ya bone hol rek

    Ndeysan les kobas veulent en profiter pour insulter la famille ndour yain yam lain tai ngain gueum yala sen bounou mam way kan a sa ndiogo yaw mom yak sa kanamu elephan bi ignnan di nala ray kouthia rawna la vu yagg ngay melni m’DADIAL ish

  • patriote

    Sa ndiogou tu as raison

  • d

    ces animateurs n’ont aucun crédit. Gueweulou Yousou et famille rek

Publiez un commentaire