Vidéo: Sa Ndiogou accuse TFM de voleur et décide de porter plainte contre son propriétaire Youssou Nour. Regardez Amadou SY 16 sept. 2015 à 18:48
Sa Ndiogou khamo sa bop dé mouway
mane kou fek sa ndiogou d wakh sii tfm ay ree dafmay diap walou innove tfm la fek bakh sa dengue demal ligueyi gfm rawna tele senegal yeup wassalam koumou nekhoul nak ngua balma
mane souka laye weur kou am numerome bakheh mako
sa ndiogou khamoul bopam motax! souka yalla nga dém tfm!
Emission you barri tfm nioka mom yénén teleyi sathiko maid c normal ndakh Dani déf Lou bamou yag dotoko guis moy takh niouy dathi séni idea