PUBLICITÉ

Vidéo: Révélation de Thioro sur les jeunes qui louent des appartements pour les fêtes. Regardez

Appartements Fêtes
Annonces

(9) commentaires

Moy Lolou

ouhhhh elle est moche cette fille sorry

Zoula

bilakhi mono lou wax ga deug li ken meusouko gis djieul gnaw rek ni douko bok ak ken aaaaaaakh

Zoula

bi lakhi moy lolou wax ga deug li ken meusou ko guis deul gnaw rek ni doko bok ak ken aaaaaakh

Nina

Soula raye gua ma

Fa

Man de dena mais zoula yala bo ma khas gisnga qui di thioro teko thi tele fadiar da eup nioule na niaw na pata na te mode na ce qui me fait rire nak moy seytanena te khamoule bopame

Kene Beugoul

lou nianw couko khôl moka guis bayilene khasté

Zoula

bilay kene khate wougnou lignou gnou guis rek lagnou wax ken meusoul guis li liiiiii eupeu na

Raki

Mdr bilaye zoula raye gagnou aha haha yala boma khass waye nak mann xamna sama bopou

Rik

thioro mbare yama na doule deug deug yaw ta 25ans mala hame bou bahh sama makk M DIOP mola done dokhane amowone bene class sounou dane demme soire jupe ak seur guaye solle guaye doule rekk nopile baka mala siwal dehh

Publier un commentaire