Vidéo- Oustaz Alioune Sall pleure en pleine émission: "C'est émouvant vous allez pleurer" .Regardez
Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Ouvrez l'appli si vous l’avez déjà, sinon téléchargez-la pour une meilleure expérience et pour recevoir les dernières actualités en temps réel.
Mashalah Oustaz mat ngagnou reference yalla naborom bi soubhana wa tallah yok sa kham kham guindi gni rer ba gnouy diarignou tie sa kham kham ak tie sa ay wakhtane MASHALAH
yalna niou yalla fayal sounouy waydiour
machallah ya bakh te am yermende
AMIIIIIIIIIIIIIIN, YAMLNANIOUKO YALLA BAYIL FI BASI KANAM. IL FAIT PARTIR DE CEUX QUI NS ONT GUIDER VERS LE DROIT CHEMIN
ya oustaze yaw reka bakh yalla nalla sougniou borom samm téé samm sa ndiabote y compris toutes les senegalais
Alla hou ak bar
oustaz koula bagne khamoula wala geumoul yalla yalanala yala defal tekhe adounaak alaaxira
celui qui meurt et qui fait parti des associateurs n'ira jamais au paradis
ALLAH SWT dit dans le CORAN: QUICONQUE ASSOCIE A ALLAH QUOIQUE CE SOIT ALLAH LUI INTERDIT LE PARADIS
al hamdoulilah
dieuredieuf yalla nga fi yague lol té weer
macha allah longue vie
YALNALA BOROM BI FAY SA KHOLE YA OUSTAZ…
yalla kéna la,oustaz yalla na yalla geuna goudeul say fane si barke seydina mouhamad(psl).
Diaredief Ouztas yaw kou bakhnga
Masala
Oustaz yalla nala fi yalla bayi basi canam aminnne
mashallah
alahu ak bar , ya bakh oustaz alioune sall , yalla nala yalla defal wèr ak goudou fane
Alhamdoulilah Rabil Alamine!Oustaz Alioune Sall sama sopé Yalla nala Borombi défal diam fi douniya wal akhiri!
en quoi c'est emouvant ? tout le monde sait que c est devenu une tradition nationale de pleurer dans l emission "DAGNE KUMPO"………Il y a rien de plus degoutant de pleurer sur un plateau de tele surtout pour une personalitè qui doit inciter au courage et à la volontè………."si les femmes se cachent pour pleurer les hommes se cachent pour saigner"…………Pleurer malheureusement signifie LACHETE !