60 COMMENTAIRES
  • cartel

    ki guemoule yalla ki dou daara

  • Djiguén dafey séy ba déh

    Yaw deh sey goro dina ñoula ragual

  • issakha

    ki mo perte t bok seytani yaw li mo takhe gayi mlni mbam khoukh bou maquette ana sougnou djiko you rafft yi gnou sougnou mame you bakh yi bayi lne yaw am classe d bonne ga

  • daga

    merci fatima sa wah rafetna rafetna

  • diallo

    punaise Sénégal yakouna, ki deh souma narone tak domam ma renoncé en plus si j’étais son mari ma fassé ko ki mo bone mo yess

  • ritachou

    dieureudieuf fatima heureusement il reste encore des femmes comme vous merci tata

  • nekh

    li mission reck la

  • La LIONNE

    sa dome bobou dina fi lamb.Te yow do exemple

  • khadim

    Akhiroulzamane la moudioum diamono bou khaliss donne sakh si garap di gua guisse aay djiguene di seyy aki gollo

  • nana

    C’est nu.l Pour moi la femme es sacre

  • Toure

    Merci les filles je crois que la femme du thme ne mrite pas trop de mal elle n’a dit que son avis. Elle veut de l’argent c’est son problme. En tout cas je lance un appel aux hommes de bien choisir leurs femmes. Cetal koulabouga et tu seras heureux merci nguenebalma ak

  • manianglo

    sokhna sy fall bol topoe koko way

  • TRA

    Sa niaway
    Nga fokeni yaw dinga diour lou rafèt lou diar def ci yèn khaliss !!!!

  • bambiste

    yor dieumb nitt taxouta done nitt eske nitt la d’abord dfw A mala youy dox nii rk la

  • lesi

    c ce genre de maman qui font de leurs filles des putes .
    Si tu es une femme qui attend d un homme qu il soit riche pour que te marie avec lui sache que tu as deja une mentalité de « thiagga  » .Parceque sans argent t es pas prete à donner ton amour . c ce que font exactement celles là .

  • Mamadou

    on senegal dou dem

  • xalil

    Elle a dit tout haut ce que beaucoup de femmes pensent tout bas. Dieu sait que la plupart des mariages ne tiennent que par l’argent.

  • Niakhoum

    Yaw sen niaway kan moy deff ci yen 3 millions… Je pense bounouy invité ci télé dagno wara invité kouy wakh lou bakh lou amm diarign….

  • kg

    fatima wakh nga wakh dji yalla nala yalla dfal Diamm ba say May di baawaan

  • ndiaye

    ki dal domaram piiiiiiiiirna ague gniawayam gui souma lo diour mie kham nani mola guena gniaw gay wakh 2 aki 3 millyon doma ram li regue mo takh nou leni torompe delen sey ta yalla takh

  • ppape49@gmail.com

    ki dafa yebate worna heur bounek mou moy diekereme emesil li motakh goor gni takatougniou kene djigene gni dagniou wara khol si mame diarra bouso kholoul wone am am motakh yalla may ko limou am tay

  • killet

    triste 🙁

  • khadim

    yaye thiaga degue domouram deugue ga

  • Rama Badiane

    ki et se que wrna sah elle ressemble a une folle

  • khadim

    souma done sa dieukeur fas nala bou yague

  • khadim

    thiagala kii

  • khadim

    ki thiagala

  • HD

    si c ça la mentalité de la majorité de nos soeurs, alors ce pays est foutu.

  • mimi

    ma warou do tak sa ndigue ngua liguay yor sa bop

  • deug rek

    yangi katante ci ala bi

  • deug rek

    yabate

  • BIG YOU

    Mané xana koula yor yayou diambour yor sa yaye bi la diour bane goor moy nagou lolou qui xana dafa doff,ta wax bi ga wax goor bou ko dék dina romb sa boute keur a 100 m boudé beuk na lou bax ko yap,boudon may sa djekeur football nala bou yag

  • BIG YOU

    Mané xana koula yor yayou diambour yor sa yaye bi la diour bane goor moy nagou lolou ki xana dafa doff,ta wax bi ga wax goor bou ko dék dina romb sa bountou keur a 100 m boudé beuk na lou bax ,ko yap boudone may sa djekeur football nala bou yag

  • Touba Diagne

    yow djiguéne diou bonenga diou yéss billahi ta sa dieukuer boudé nite kou nité warnala fassé na yow mato sokhna bone badéé adouna amoule solo ta khaliss douwéyye barké S Touba

  • BREF

    Tu as tout dit Fatima ki guemoul yalla mouy melni Bouki

  • Giss Giss

    dofnga sa diakar amoul foulla yaaniaka kersade

  • baye falle

    Waw sou lambet aprs ga takk koooooo

  • khadim sylla

    Kii lime wax man soma Nkon diekarame dama koye may bat li mo wax boke diekarame dg dako wara fasse t xamn kii alall laye seye Biss boo wadji niake mo dme Yoname

  • abdou

    gueumal yalla sa borom

  • babs

    bouche bée ! je n’en crois pas mes oreilles. Dites moi que c’est une mise en scène. Si cette femme crois en ce qu’elle dit ,elle ne perd rien pour attendre , sa déception est proche.

  • aline

    Fatima kadou yi raffetna yalla nala yalla diapalai ya woutaik amina

  • fuck

    ki deh kou bègue Lou bax d’où takk domame ndax nday dji baxoule..lambale na ay domame

  • momo..

    contane na si yaw fatima wakhi goor rek nga wakh machalla

  • incredibile

    elle est incroyable celle là !!!

  • mbeur

    mais nous sommes dans quel monde les gars avant de se marier il faut regarder bien les belle mre

  • fuckk

    ki mo bonne legui dall djiguene gni intérêt rek Chu femme comme iow mais ngor ak islam lay khol si goor pour sey ak mome genr yi nio yakk société yala yakam tinala deh sa gnaway borom fass sakh soxlawoula

  • bello

    merci Fatima wakhga lepou grazie di cuore ti voglio tanto bene

  • aids

    ame sakhoul loffi guiss déye dié une femme si ta un mari qui de l’argent et il n’ a plus ce qui est logique gua mougne ame sakhoul niakka samoul adouna amoul solo dara dou wéye wasalam

  • modou.....

    yaw mèr khana dou rouss ki yakar ne xaliss manna lou ne mouy deff lou ne guir am a alle sa xalatt rafètt lowo makoo darra yaye

  • Mame diarra

    Hum adouna dh diaroul Ken kouko diap diaroul kouko bayi tamit diapoula mtx na lep rafet allle Day diekh nguor dess

  • modou

    ki bouma nekonne diekeurem demakoye fasse dakh alal lama tope bouma yoroul ma wathiemefe

  • Mme lo

    Mandé warou na mais ki jekerem dako wara fasse pask seyoul te yalla takh no dama rousse sakh mou melni boukki ni thimmm

  • Amina

    mercy Fatima Yalla na Yalla def djigeen yep deugeu la,Amiin

  • Charlotte

    Mane dama tite diiiii layla

  • sama reew

    Fatima bien dit!!

  • talibe

    Machaallah sokhna fatima bien di bou djigene ypp melone come yaw thi niga wakh cone mou bakh mai gisss nga

  • adja

    mann deh warrounna

  • Fatima

    boula yalla seddé nga necka dioulit niari gor diourla da ngaye sét lou rafet di ko wakh di ko def je suis une femme comme toi yénéwouma kenna lou bonne nack mais ma soeur demal nga diouli niari racka nga diegalou yalla toub wakh bou gnaw bi nga wakh ta balou akha sa dieukeur li nga wakh reuyna gnaw na adouna amoul solo ta diekh na ba paré alal bobou ngaye wakh ame ngueuramou yalla ak sa dieukeur moko eupa bo déwé tamiit fi nga koye bayi mane je crois que niit bo démé baye seuye ak mome na yalla takh ak mbeuguel … allal yalla ko yor ta niit ki weursagueum reck laye lecka j t parle en tant que soeur toubko ta djegalou sa borome keur ta tarbiyouko adouna diekhna ba paré woutal barké a la place de l argent dont tu parles ma ngui djegalou nack merci

  • deug

    hoo deg na wakhi thiagua bou dof waay

  • cartel

    yow do rousse

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *