Publicité

(Vidéo) Guigui Diallo: les filles qui vont à Touba avec leur Pathial et habillement indécent..."

L’humoriste Guigui Diallo fustige le comportement de certaines filles qui vont au Magal pour le plaisir de séduire…

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Dans le même thême

20 commentaires

  1. Laconia

    yow DEUCH, kou la né waadji ab tidiane la? Khaana koudoul mouride rek tidiane la?

    Teey leen té moytou toogn kat yi nekk si NET bi, Bu leen yaakar ni POLICE munul kham yeenay kann.


  2. loki balboa

    pourquoi s'habiller correctement à touba et revenir porter à dakar ou ailleurs demi_jupe ou demi-robe?

    La décence doit être de mise partout parce que Dieu est partout.


  3. lebaolbaol tigui

    Guigui y a quoi ? yaquoi ' quel est ton probleme ….tu as meme oubliè ton "pathial"…..quiter labas way Guigui ……….sinon ……sinon bakhna dal !


  4. Zeyna

    vraiment toi ki insulte les tidiane tu n en aucune respect …. yakko kinguayy tontu batakh nguay wakh louma leroul si tidiane ngni yena yam …khamoulen wakhhh respect way


  5. Papynho

    wa mais Deuch Anonyme mii di wakh moune na am sakh mouride leu et puis meme bouko nekkoul loutakh ga bayi fi yenene tarikha yiii di wakh si bou tidiane yiii comme si kouj nekkoul mouride rek tidiane ga c pas pile ou face.

    khamal né mouride deh dou nii ley dokholé ndakh seu royoukaay di Serigne Touba deh dafa khamone baalé ndakh si balé leu amé limou am nii biko toubab yii sonnalé daf ko gérer pacifiquement wayé nekkou feu di khasté aka khoulo.

    Ma yokk si tegal leu si né niakk kham rek motakh ga diapp né dafa am différence entre mouride et tidiane ou whatever alors sétaatal ligay wakh bou baakh ga baal m nak dioublou wou ma si rousse lo leu walla te faire du tort.

    Wa salam


  6. Deuch

    Yaw anonyme réglél soléne khamoul séne bop niou wakhlén yénay kane lingéne di iniane yéne tidiane yi séne serigne yi Kate thiagua rék moy séne métier khamal louniou la wakhoul domarame so amé loy wakh tontou ma dinala wakh sa serigne yi weur keur thiagua yi ak di bireul


Laisser un commentaire