Vidéo: Gamou: Serigne Arabi Niasse, « Serigne Touba Moy Al Khourane », Regardez!
L’imam de la grande mosquée de Léona Niassene, Serigne Arabi Niasse est revenu sur les relations séculières entre Serigne Touba et son grand père, Mame Abdoulaye Niasse. Dans cet entretien de 20 minutes, le professeur comme il se nomme a encore relevé la fraternité qui existait entre ses hommes de valeurs et leurs lieux de culte.
dieureudieuf Niass kén dou SERIGNE TOUBA
Ndéysaaane yaa baakh Niass kén dou Serigne Touba
Bilahi Niasse ya goré yague fi lool té wéer
yag fii lool niass!deug,rek kay deug serigne touba kouko nangoul diam rek ngay am
yene mouride kagne nguene di gnanga li gny ci dess di bind diko wakh yene tamit khana rekk gni ci dess gnoy dianga li mouride yi bind nguene toppo ya gnakk kignane ya gnakk yene mom sene khol dafa bakh lou takh gni ci dess dougnou wakh mouk yena gnakk kignane yene kene diakha sewoul deug rek lagne lene wakh
YA BAKH T2 NIAK KINIANE YALLA NA YALLAH GOUDALE SA FANE TEI YOK SAYE XEWEUL SAMA YENEI SI YAW REUYNA LOLLL
a c vrai serigne touba moy alkhourane il l a montr a toute l humanit. jerejeuf niass ta niakk kignane
DOUNDALE YAW BASSAY MAY DIBAWANE LIGUA WAKH THii SERIGNE TOUBA RAFFETNA NIT DAY WAKHALE MBOROMOU DIOULITAM LOU BAGUE DIEUREDIEUF. YALLA NALLA YIWOU KHASSIDAYI DALE.