36 COMMENTAIRES
  • BOU

    Me pourquoi les journalistes dougne rancegnewou bou bakh avan de distrubue les information c pas un francais c un español

  • diaspoMan

    Je ne juge personne, mais Attention, en général les hommes toubabs même s'ils ont des maitresses, ils s'engagent passionnément dans leur mariage, ils acceptent très mal que leurs femmes, mère de leurs enfants, les quittent. Ils n'ont pas d'espérance dans le futur et pètent vite les plombs. IIs préfèrent tuer toute la famille et se suicider. Dès que le divorce est incontournable, il faut s'en éloigner avec ses enfants sans laisser d'adresse et faire agir son avocat uniquement. Paix à son âme.

  • tchipp

    Senegalais yena gueuna boneu kouy boneu. Kenn beugeutoul sey ak yenn. Meun guen fenn, meun dokhane, takko lenn dolen bayi keneu takk. Sans compté belle famille bou fatté ak ay histoire de teralaté et puis je ne sais quoi. Bo lenn diogué né dagno haram té vous vendré vos ame pour aller chez eux. Yenna fi dakk door diabar, abandonné avk les enfants ba paré di wakh. Gueuno lenn toubab yi té toubab yi gueunou gnou lenn donc basta

  • Dame

    wor am diamm senegalais rek nga koy def

  • croyant

    Arrêté avec vos paroles à deux balles (toubab yi baxouniou) y'a pas le toubab,y'a pas le jaune,y'a pas le noir de partout il y'a des bonnes personnes comme il y'a n'en des mauvaises aussi arrêté de juger les autres il y'a qu'un seul qui peut juger quiquonc dans ce bas-monde c'est notre créateur et comme on dis personne n'est parfait sa salam.

  • elhadji faty

    INSA dieuredieff sa wakh rafetina

  • elhadji faty

    toubab dou Darra niaka kham rek yen jigene Sénégal baye len toubab yi té yalla takh billahi toubab dou Darra

  • insa

    musulmane bi yalla na ko yalla yeureum
    il faut qu'on se rappelle que une musulmane ne peut pas se marier avec quelqu'un qui n'est pas musulman.
    Actuellement il y beaucoup de femmes musulmanes mariées avec des non musulmans.
    naniou nék ay dioulite té bayi sakhane yi ndakh mbiirou adina

    • said abdul karim

      la parole de dieu est inpénérable ceux ou celles qui ne l'observent pas verront leur sentence .

  • diop2italia

    @@deug yaw ya wara ragal yalla
    dabord jigeen jullit dafa haraam muy seyeuk yeefar. kou dee ak sa bameel

  • momio

    Bune guisser touriste melni buki bu guiss béye.. Wanter bena ngokk… Bagnelena moytou nassarane ci rek…

  • Deug

    Bayilene li ngene di wakh. Ils ont fait 11ans de mariage, soudone interet doufa tok 11ans. Elle aimait son mari, elle aimait sa famille et ses amis, c'etait une fille extraordinaire. Ragal lene yallah! Bakhnaa kou de ak sa bamel…

  • Miss

    Le mari avait 65 ans et elle 35 ans !!

  • paco diaz

    Akk noumou meunti demee dalll metineu pour seini dommm euleukk bref toubab nakkk moomm kaye kharou moleine gueuneu fouff tafff tafff niou rayy srine bopp wala niou rayaleee woroulll dorr leine molll si sey akk toubab alall gui diarouk

  • amina

    yalla naléneu yallah yeureum

  • london

    Ndaw si yallanako yalla yeureum toubaab yi bakhouñou ta soko naree wor mou ray la kharou dou dara si non.djigeenou dioulit dou seuyeuk goorou toubab boudout dioulit

    • amina

      li dou diam déh il fau gnou dioug si

  • om's

    Mello fait attention de ne pas le trahir après avoir pris ses biens ou en espérant prendre ses biens ! sinon il va se produire la même chose ou il va te tuer et s'échapper si possible !

  • Mya

    toujours ls mariage par intérêt sa finira mal nagnou kholate sougnou bopou li yeup sait a cause de non parents

  • kagaleeee

    doye na war .makhalah.deguen desse kham tubabe rk

  • NIT DOFF KILLER

    dia bian parlé la plupart mooney rk mo len ci douguel"
    sey ak toubab = sey ak chat
    toubab yi sen dambal yi deuguer roul guen ciy dougou
    (FROM GUNZOUT)

  • alou

    est ce que trahison amoul thi séene digueunté; sénégalaise danioo beugue khaliss lool; té toubab booko wore mourayla doogua Ray bopam; doudara thi nioom

  • MR X

    il a investi un jour tu lui fou dehors tu restes Avec son bien c'est le résultats

  • medzo

    Dia t as pas bien compris le message a mamaad
    "seey nguir intérêt " pas seey ak toubab nuance.
    yallah kham ce qui s est réellement passé. Gnou maandou cci té Allah yeureumlé
    Mais arrêtons l hypocrisie et revenons a nos valeurs et principes.

  • MR X

    les femmes sénégalaise doivent faire attention avec les hommes blanc il n'ont pas peur de mourir s'ils chasse que leur vie foutu il te tu et se susside

  • bref

    ndawsi yalla nako sunu borom kharé Aldiana firdawsi Amine, toubap bi nak Khawma si mome dara dara dara dara dara

  • amina

    tounab yi daniouy dikalé

  • dia

    mamaad
    li ngay deff mo haram!!!
    Avez vous ouvert leurs poitrines pour savoir s il y avait de la sincerite ou pas?
    Juste une parole peut nous faire entrer en enfer
    Nagnou mandou
    Qu allah nous guide
    Amine

    • mamaa

      Serigne dia nafekh nga, une femme musulmane ça lui est interdit de se marier avec un keffar yalla ko wakh si al koran, 38 ans que je vis parmi eux, tjrs par intérêt ces mariages

      • dia

        Serigne bi kane mo la wakh diamantaire bi keffar la ?
        peut etre que da nga ko hame bou bakh
        Nga balma

  • dada

    yallana yalla rakhas khol yi li doyna warr domyi rek la yerum

  • Mello

    Moi je suis marier avec un Toubab on n'a des discussions mais pas ce point

    • deug

      alerte, divorce maintenant sinon ta mort ne va pas tarder

  • mamaad

    Ça finit tjrs mal seey ak toubab nguir intérêt defa haraam c'est la inieme fois que ça arrive

  • Elbach

    c'est quoi ces marathons de tueries au senegal on dirai que c'est pas naturelle qu'est ce qui poussent les gens d'etre sadiques a ce points. revoyons nos comportement et demandons pardon a DIEU

  • Deyadeya

    li metina.trop .wayé kharou daganoul kelk SW la situation

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *