22 COMMENTAIRES
  • NOKIA

    wakh day rafét way khol léén bou bakh linguenne di wakh wénn wénn melni ay sokhna dioroulénne wayé lépp wa SENEGO la rék amna lo khamni bakhoul lo khamni kouné dakoy sétane kouné diko déglou wakhja warna rafét mangui jégalou bou bakh

  • ablaye

    Mane limaye wakh moye wakh léne té boulene si bo lé sariya

  • elhadji rafét

    kouy siiw dangay siiw çi lou baakh wayé yeene 2 yi khuewma louleene dal kw

  • Baps

    non vraiment wa senego gni gnome waroulene lene di caricarel dara ndakh amougnou bene education lou bone rek lagnouy wakh

  • zeyna

    niene soff guene trop ta niak foula

  • diva

    gni mom ay pa you rew lagnou gnouy melni amougnou ay dome ni siiim

  • modou

    khana sen venou ndaye lanoy foye

  • Ya rulen

    Yen ay domi laff gen sen diobou Day sen daba li bay

  • degue rek

    sen lafeull ndaye sa boleen yéwo yalla naleen yalla alac ñu bon nguin yenà yess yena raw firawouna yeena Charlie ebdo

  • degue rek

    Magui dieugellou yalla limado setané li

  • Bro

    dou yone wakh dafay nice on dirait qu'ils n'ont pas des parents qui les regarde amoul bén kérsa charia dou fowoukay

  • galsen

    ana wa dic

  • fafa

    Ahahaha dèna gni gno rew

  • rom

    ay domaram nguine yén

  • tonton mbidou

    bou gueen khamooon nigueen sofee senegalais yi ndakh seen saguayiiii bougueen koo wedee lath leen SANEX bimou daan sagua gnepeukeu djepiwoon SOFGUEEN MA

  • Neyafero

    khanaa sène yaye amougne wène ak bane façon lagne ame

  • maman100

    Nn frenchement ngie daniou ma yapp kw

  • careca ba

    mais vres yenn amolenn khalat li khaliss djarouko Souniou borom santoulenn li de melni doughenn ay domou djoulitt koi.pouhaaa

  • Also

    ragal lèène yalla lii nguéne did déff I alkandè rèkk nguèn thiy dieulé ndakh yalla doufowou Kaye chariha dou lougnouye kafè toupe lène thiy yalla ta

  • ski

    C'est le mec genre à mater les seins de leurs maman !!! Saine Wainou Ndaye bou Nior sa Ndayame

  • Dada

    Yéna niaka fayda thiem ma len diépi

  • Beug wène

    Éh boulen gnou rèy. Wène dafa nèèx nooy Oooh ma beug wène

Publiez un commentaire