27 COMMENTAIRES
  • lamp

    bon vent porte malheur wa

  • baby fatt

    ki moy domou khadj pur

  • cacabouda

    Un gros con ce cochon la

  • Pds

    Bayil léne réw cheikh bi il est libre d faire ce qu'il v . Wade bolé nako ak serigne saliou cheikh bi bal ko, ch bi fébar wade setiwouko, ch bi dém prison wade setiwouko. Wakh deg wade dou wayam wakhna deg ! Mane pds la bok cheikh bi wakhoul gnou bayi té soukoy wakh ma bayi

  • Dame

    le 17 avril 1946 je né pas encore né méme le president de la replibique voila une guide qui na pas de haine et il crois en DIEU. Cher ami la haine né pas bon seulment ya aussi l'ignorence vous pouvé ne pas croire mais insultés sa devient de l'impoli

  • BASSE diombagnaw

    le poison dans la Sénégal! que dieu nous en lave un jour

  • rima

    Thieye que Dieu protège le senegal!yewoulene

  • sokhnaamy

    baby fatt yaw yarou wo khamo kane moye srigne ak kane moye serigne saliou ka diape né likaye wax ni kane kakoy def sa bop nax amo queroumou yalla khmo lanne mo di ak thiant mom serigne bethio sou fekeni likou serigne saliou cheikhal mola meti dakhoul diapal né loko mane di wakh wakho koko sa bop kaka def nax serigne saliou moné yaye mane maye diape gni yaw moye degue degue diape si koula dem adiana koula kham deme mais yaw amo kham khaam yalla dimali guini la nax daka rére soko khamone likaye waax doko wax téba pare respecte wo sa baye biila diour mo takh wala lou takh si yaw

  • WAKH

    mdrrr yén gniy saga, vous êtes invités niou Thiante… té nguén nianalniou yallah mou yééé niou kom daniouy nélaw mo geune Saga yi… Dioulite lou rafete la wara wax

    • Tidjani

      Yaw rk LAN yaroul ya respectewoul say parents ba khol ki sankou nguaye and AK mom domu kharam yi

  • bègue s touba rek

    Tidjane yaw rek y'a rew gui mo guene sa baye at sa baye guimou yakar gui s saliou moga deefar sa bogou mo am moga guene rew guene lolou sakh ta niague yar sakh khamo leene dara si adouna dakh nelaw

  • beugue bamba rekka worr

    ay yokhamni diaroul commentaire ndakh niakka kham lim waral barina li serigne bass abdou khadar wxn rekk serigne touba mom likou sonou brome deff komou nekhoul nakhar ngaye deukke te serigne touba amna kone niey wx lou niaw nak danio rerr nioune mourid bakho woniou di wx ken lou niaw ndakh yare won niokou wassalm dieureu dieufe cheikhoul khadim

  • mbane khoukh

    DO TOUSS
    NITOU DINé DOU DEF FOU TAYE REK MOU TAKK COMME WéGNE HYPOCRITE
    RENDEZ VOUS YEUWMAKHIYAME

  • wakh deugue

    yène gniy saga nièpp koulène degue khamni sèn baye sèn yaye ak sèni serigne nguène ko ndieuka deff kone kounguène saga douko mety sen bopp rek nguène koy deff

  • olddiagne

    Come macky kou and ak mom mou bayila kouko contre mou teutj deug rek moy moudjou douma tjantakoune mé je respect cheikh bi ngir djeumi serigne saliou mbacké

  • ami

    hè hè boulegnou fatt way vous savez bien que serigne touba et serigne saliou mbakè n'ont rien à voir avec ce cochon qui connait même pas recitait le coran bayilene di mélange loi bokoul svp…..

    • diodio

      iow amy ak tidjani loulene métui kene tegou leneko outilene serigne ma yeureum nitt kou ignane

    • GESTEUR

      OK

  • wakh deugue

    ami on ne menage rien du tout mane suis pa thianta mais sache k on dw bcp de respect a cheikh bethio coz de serigne saliou nga balma nak nga s-tate bou bakh lingay wakh merci

  • wakh deugue

    ami ma dellou dila khamalni ki ngay wakh sa wakh bou niaw bou diakarlo wone ak sa baye douko wakh li nga wakh kone bokk amal yare

  • wakh deugue

    mais lou meunti khew yène wa senego kène dou yène coz tjrs ay imbecille di comentaire di saga ay kilifa tèwoul nguène dialalè comentaire yi mais dokhlène rek adouna mongui sèn kanam kèpp kouy saga kilifa fokni yassi nèkk sak torokhtanguè rek lalay dioural nguène balma akh wa salam

  • beugue cheikh bethio ba diekh

    Gnii danio xamoul sene bopp bougne sagnone sene bayii kon lé reconer kome cheikh bi mè ce pas pocible liy cheikh bi dou kene si adouna amoul mass amoul morom ki kene la allez vous faire voir lé mécontents

  • xamoul

    Qui se ressemble s'assemble : voilà deux ingrats qui peuvent se retrouver et Bethio dans le MACKY

  • gaye

    kiiiii stategie la beuggue il est deja chez MACKY IL cherche noumou yolle lekou chez APR IL a JOUE ET trahi WADE EN JURANT MBARCKY SERIGNE SALIOU WADE SERA REELU ET MAINTENANT SAMBA MBAYYANNE CHEZ MACKY . FAITES LA POLITIQUE ET CESSEZ SERIGNE TOUBA ET SERIGNE SALIOU

  • alou

    Yalna diam yagu Senegal duma talibe Cheikh Bethio waayé wakhi kilifeu deug la wakh di gnane thiantacoune yeup ni kou sagua si commentaire yi guene balko akh Cheikh bi merewoul kene wassalam..bON THİANT

  • dandi

    naroumassi wona wakh wayé seytané yiye diakhassé mouride yii ak tidiane nga khamny bokou niou fénne nioma matakha dougou so wakh wakhale sa wakh rék té boussi dougale tidiane yii……..tidiani yaw thi seyatine yi nga bokk daniou léne ngébou nguir ngéne di féwalé!! lakoume dinakoume wale yadiny

  • GESTEUR

    Vous savez la valeur et la force d'un pays ne se voit qu'à travers le comportement et les actes de ses citoyens. Je commence tout juste mes propos par vous demander pardon autant que vous êtes. mais l'esprit démocrate voudrait que dans un pays, chacun ait de la libertés pure et parfaite dans ses choix. N'oubliez pas que le pouvoir spirituel est appelé a duré éternellement et qu'il n'a pas pour vocation d’être partisan ou opposant du pouvoir temporel en place. cheikh Béhio, qu'on adhère ou pas à la communauté "thiantacones", force est de constater qu'il est au delà du guide religieux, un acteur économique et social important dans la vie des sénégalais. et l'on a l'habitude de dire que nul n'est plus aveugle que celui qui veut pas voir, s'il vous plait vous ses détracteurs donnez moi une seule famille religieuse qui n'est pas accompagnée tout les présidents de ce pays. Ceci à mon minime avis n'est pas une chose à déplorer. parce quelque soit son appartenance religieuse, cette derrière constitue une ligne directrice. Si le Sénégal est debout et solide de l'intérieur faut bien le dire ce n'est pas à cause de nos dirigeants politiques. mais plutôt grâce à cette valeur intersecte qui est l’héritage des guerriers spirituels, ses combattants pacifiques. le guide religieux n'est ni partisan, ni opposant du pouvoir temporel mais plutôt un visionnaire et un accompagnateur dans les bonnes actes et visions du commun des citoyens. Et pour ce qui laisse des commentaires inappropriés dans les réseaux sociaux, cela ne reflète que le niveau de vos intellects. " quiconque s'énerve au court un échange est à court d'idées. Wassalam

Publiez un commentaire