Vidéo: Ce que Seydi El Hadj Malick Sy a révélé sur le prophète… Regardez !
Parmi les invités de Pape Hane lors du Gamou de Tivaouane en direct sur la Tfm, Oustaz Mouhamed Ndiaye dresse le portrait de El Hadj Malick Sy et ses enseignements sur le Prophète de l’Islam. Regardez !
Mame Maodo locci wakh rek desna..daffa neubou boppam nguir Rassoulilah SAWS…bamou dema Makka nene sounou borom nietti affaires la beugueu1
1 rewmee di Sénégal beugouma maffa fegn..lima beugueu moy ligueyal Rassoulilah, tabakh ay diakka nioufay wazifa ak zikr
2 Beugouma niou khame sama njaboot- ak sama talibes, wayeu beypugueuna niou ranielene ci xam xam ak ci teguine ak Yaru ak teyy…
3 Niaanna iow sounou borom soufsouma danne sama dolee bagna diarinio niakhou talibeyis motakh mou amone ay tool Nndiarde, Diacksao, Diamaguene etc…dicci daan dolem dii baay.
Defenani niaanou Seydi Hadj Malick yepp nangouna…
Zawyas yangui laaw, talibes yi aay millions diang nanou, silwisse, Yaru, xamee Serigne ak Yalla… dii zikr matin et soir, seriniou Tidiane doylou bagna jittal xalis ak aduna
Diadieuffe Maodo Malick amo morome !yaay ki aar Sénégal…
2
yalla na niou yalla tass ci barkèm sy malick
ci gatal Bo diangueh ay terem day melni fekke nga bafi yonene tebih nekkeh.radyal lahou anhou
macha allah thiey mame maodo yalla naniouko yalla fayal