Vidéo- Bouba Ndour: "Abdoulaye Wade gënoul sénégalais yi"

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Aucune recommandation disponible.

67 commentaires

  1. yakanam

    l’émission jakarlo avec BIRIMA c’est la catastrophe car il défend toujours le président M.SALL et son parti alors que tel ne devrait pas être l’objet de cette émission.Nous souhaitons que cette émission soit plus objective et réaliste et non partisane

    .


  2. GAWLO

    TFM thi bopame lanou wara tieuthe rapp fermeko nakk telebi amoul bene profetionalisme nakk regarde bouba ndour na aucune diplome journalisme nekk thi telebii dii ratatati rekk waye nakk gawlo la nakk +gewal dii diame bou sette weithi nakk


  3. bruno sambou

    je conseille au senegalais de rester serin et de ne pas oublier que wade est une espece en voix de disparition.il sait bien que la majeur partie des senegalais sont vaccines contre sa politiques de destruction.il faut changer la donne seul les imbiciles ne change pas


  4. gawlo

    birima ligua wahh reuyna yaw dehh sounou teudjie masaly bayila ma hameni rewmi nakk lou nehh waye wahh legui emisionbi nakkamoul bene organisation bouba ndour da dieunde presentateur bi amoul ben efoula profeseur fii dousa place yawwe daguafi woyadi rekk


  5. gawlo

    bouba ndour yaw app diame gua di app guawlo di app gewall yawq mome tu na pas docune parte dans cette pays yaw ape diame gua tu est un caste dune famille gawlo +gewal okk nopil bouma taha wahh sa bahou mame waye


  6. Ngor

    Ah Wakhou Bouba Ndour mom diaroul diokh importance .

    C’est pas le genre de personne que tout le monde écoute quand il ouvre la bouche , c’est valable pour l’autre boufon de birima a côté . Wade n’a pas le temps de les écouter sa sera trop leur donner de l’importance .

    Ishhhhh !!!


  7. waxxsaxalaat

    yaww rekkk ya beugg di fëgn cii clip cii télé yi sa yennen frères yeupp niou gui liguey bolekko akk nopi senn keur youssou leu yalla mayy nangoul bayeko lepp té noppil ligueye té bayi beugueu ecran


  8. waxxsaxalaat

    Bouba ndour noppil déjà sénégal kenn sopouleu senn keur dou ndiaga dou ibou dou birane niou gui liguey tey nopi waywayy deffal ni niomm


  9. Mamadou Diop

    Bouba n’a dit rien d’autre que son opinion. saagayi ak khasantéyi, wakhyou gnaawyi diarouko, likhèw lépp dioudioumla rék, ak diakhlé, nanou déllosi khélyi, bok yéné, té rafötal wakhji,Sénégal nooko bokk.


  10. madou

    j’ai remarqué au Sénégal ya bocoup de hypocrisie. bouba est birima ils ont libre de dire leur pensée. En il faut arrêter. Les saga kou begoule koula saga .boule saga.


  11. Badolo cie Néwdolé

    Walaff neéna boutile ameé al. mette teye alabi lière . Bouki ameé séhl thioukhoum thioukhoum bary= Guéwel ameé Radio teye nope banne!Bouba sonal nga Niitgnii!


  12. vrai de vrai

    pour une fois je suis d’accord avec bouba sur toute la ligne. senegal dou monarchie ba ablaye wara diokhe couronne karim, té senegal santoul wade..


  13. bègue s touba rek

    Birima bouba ay doof guene khamo lene dara sent Lee’ne tfm mom dakh gueene di wakh nii regue ta liguene di wakh khamo lene sy dara


  14. bègue s touba rek

    Bouba yaw at sa kharid at sa papa at say bogou at go kham wade mon ga guene liga wakh sakh khamo go wade mon falle macky wayee macky monye falle karim 2017 yaw maddamm fall khana maguı mon yor sene wa kuer


Laisser un commentaire