(Vidéo) Birima: "Je n'ai pas appris le Coran, je ne connais que Serigne Touba..."
Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Ouvrez l'appli si vous l’avez déjà, sinon téléchargez-la pour une meilleure expérience et pour recevoir les dernières actualités en temps réel.
Yow Birima YALLAH S.W.T sàrou Alkhourane bimou ndieuk wathié moy nga diangue. Yow rousso sakh ngaye mélni bayima bouy wakh dinane diangouma Alkhourane Serigne Touba là kham? En français: Toi Birima la première sourate révélé la sourate 96 du Coran DIEU te dit apprend et toi tu oses dire que tu n'as pas appris tu ne connais que Serigne Touba. Heureusement pour toi qu'il y ait SENEGO va apprendre le Coran avant que l'ange de la mort ne vienne s'emparer de ton âme et là pour te punir DIEU peut ne même pas te montrer Serigne Touba dans l'autre monde. Fais attention à toi!
birman
diinnee mooy deug alkhourane moo cadouk sounou booroom dieu dit dapprendre le coran et le phrophet aussi et serigne touba diamou yalla la woone neka koudoone fessal legueyou prophet mouhamed psl donc allez apprendre le coran car serigne touba maitrisait bien le coran et sa refernce etait l prophet psl et le coran la sunna pui il a ecrit des khassida avec beaucoup de extrait du coran pour explicite et decortiquer cela respect a serigne touba l na jamais dit de ne pas apprendre le coran merci of et ouf c est pas bon of egaf coupe mieux vaut one queoff pour qu cela marche le contraire de fou est mieu que cela merci que dieu nous guide dans le droit chemin birima va apprendre dianga dou wes
diinnee mooy deug alkhourane moo cadouk sounou booroom dieu dit dapprendre le coran et le phrophet aussi et serigne touba diamou yalla la woone neka koudoone fessal legueyou prophet mouhamed psl donc allez apprendre le coran car serigne touba maitrisait bien le coran et sa refernce etait l prophet psl et le coran la sunna pui il a ecrit des khassida avec beaucoup de ext
traore , ya meuna doul , serigne touba grantena koudoul birima , ,, bala ngay wakh danga deglou ba pare , ki dafa wakhne mane diangouma alkhourhan serigne touba la khame , mome newoul diang alkhouhan bakhoul newoul tamit bagoul kham alkhourhan , mais yen dangena bagne serigne touba yakamti woulen loudoul kou wakh ba toud serigne touba , mais yeramnalen de , sen khol si metti lay nek ba bangen di faatou ,
niatta nit gno nek senegal khamougnou alkhourhan khamougnou serigne touba ,
Le problème, c'est qu'on vit dans un monde où tout le monde, partout, nous enseigne le contraire de ce qu'il faut faire . birima adada
Bariguaciye morome
loussi sen yone serigne laxam bayi len kok Serigne Touba rk loumou am dieul way yéna sokhor way
Khadim On dirait que c'est satan qui parle oubien.
Avec des nafekh, mecreants et ignorants nous continuerons de produire des talibes ignorants de Dieu et du Prophete Mouhamed Rasoul.
kone na dèm ndiangui wa kou khamoul loy wakh nom khamguannè talibè dou fimistè tè navèk khamka lou guoy kharr ki bilay meutta dèk alkhourann nafèk douko tarrè
Birima taye dal beug nala
bilay balla gua wakh daka warra kham
yaw domu haram ngua demal diagui sa diné mo gueune topaté do russe sax yaw.maxala sa bay ngako guissé
d ou sort ce mec c est triste et pourtant beaucoup de gens pensent comme lui. l ignorance
man mi de serigne touba rek la kham , louma am diel , ma tay tamit , soude ay nakh nama nakh
tay nak begnasi yao lol birima figa diap fofou rk mo woor boul deglou borom khol yi bone yi nakhar molene di ray
Waw goor guinaw diaggo figa diap rek moworr deee
li moy ak ndof degdeg sarigne touba wahoula li digaloula li mai nak manck de consiance islmaiq mo manque si yen doun len ko diappe ndah dof dagnouko dou ham loumou wara wah ah fimouko ware wahe
fiiga diap mowor deeeee
Non sénégalais si bopam mo beugue lou yomb té noy !!! Bcp de personnes pensent comme ce gars …pour eux soné talibé ngua meunga ndialo, fène, do diouli, bania diangue alkhourane , deukssi boîte de nuit yi !!!! Do def dara li alkhourane diglé Ba paré lakhatou si Guinaw Serigne biiii!!! Aka yomb loooool mais Inchaallah mais souba rek nguen di comprendre !!! Bokalé yalla douko balé !!! Dara gueunoûle mague alkhouranoul karim (le Coran)
li kay mo takh amoul savoire vivre kouye wakh doula bayi ngua diekhal li wakh sakh mou dok la di youkhou rėk
@ samba,ne répond pas @ François ,qui ne sais pas ce qu'il dis . Ns ….on travaille ,on bouge,et après le boulot on regarde les sites pour savoir ce qui se passe ds ntre pays. Donc @ François haouma loll… Vous et aussi con,malade,et surtout hippocrite que birima…vs pouvez être enssemble .
@samba,ne répond @ François qui a ne sais pas ce qu'il écris lol.nous on travaille ,et après le travaille on regarde ce qui se passe ds notre pays. Et toi@ François vous pouvez être enssemble avec ce con,malade,hippocrite,fimiste ( birima)
C tt simplement un imbécile.
pour ça que il et bête aven de connétrep bromtouba diangale allkhouane cet farata
Pourtant c normal chez eux il dit haut ce ke les autres disent touba
senegal liki ko warole wakhe rekmoy wakhe
serign touba santou la lolou demal jangu man mouride la demal jang te gisga yen wahii rewade yi gen wara bayi alhouran wahi yala la yaroul mouride jamou yalla ligeye jokhet lagnou ham hamou tiahane kouka beug ya koo si yokk
niak diom wéesouwoul nga nék magoum dieum di wakh wakhou kou toscaré ! so beuguoone serigne touba réellement la première des choses que tu ferais c'est d'aller apprendre le coran car serigne touba lui même a dit que s'il ne dépendait que de lui tous les musulmans liraient 2 khizib du coran chaque jour que dieu fait. diangue alkhour aane tchi mak dou gatché. vas t'y mettre aux heures de cette émission qui te prend chaque semaine plus d'une heure de commérages
Serigne bamba moy alkhourane, vous êtes tout le temps sur le net pour critiqué les gens, birima il n pas malade, c'est vous yena malade febarou khôl, le temp passe trop vite demelene ligueyeyi bayi critique bi
Francois c toi ki le malade espere d'hypocrite. Tous les jours je me connecte sur seneweb ou senego pour voir ce qui se passe dans mon pays etvob tombe toujours sur des conneries pareil, des gens sans cervelle, ni éducation. J'ai rien contre gens là, mais il faut reconnaître qu'ils sont nul
Pour coi
Serigne Touba dé tope dîné la wakh, té boo doangoul al kouran do meuna tope sa diné.
Encore un nouveau malade mental et ils sont fier de dire des conneries
Serigne moy alkhourane…amoul morom balla aissa boury..yalla nagnou ko yalla fayal
Ce né k1 DOMAKHARAM RIEN D AUTRE G Pitié de luis
Ki! Il est malade,pfff pa normal ce mec