Vidéo- Aziz Ndiaye: "Modou Lô ne m'intéresse pas, on se connait, je n'ai pas le temps de polémiquer"

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Aucune recommandation disponible.
Aucune recommandation disponible.
Ouvrez l'appli si vous l’avez déjà, sinon téléchargez-la pour une meilleure expérience et pour recevoir les dernières actualités en temps réel.
Sénégal d'où dem ay combat lousisen yone?
demlen outi heuy
khana modou lo rek kaffi nek wakh dji barina trop si mom bayi len kou lim beugue la wakh rek kou Mane def Ba sa marom def ok
Modou req moo yoor noun ay talibé cheikh lanou .ça t interesse ou pa danouye dem
Aziz arretes way Modou lo Ababacar Mbaye talibé Cheikh la comme yaw
Modou namoul dra molen di djokh khaliss aziz mod lo te derange tu n a rien a lui dire
Modou dada fouy sou bougouul dieuleul ñi beugue mom mou delou dawwaal sarret mbam
ki arriviste la daffa fouy modou lo faleoule sa mame sak
Sa wadji so meunatoula teugue combat 100 million bayile gni meune teugue teugue séne lamb wakhe ji diaroukofi
bayil modou lo nak lou lerr l'ala wax mola gueneu populaire il la raison bo meuneutoul nga c facile
yaw mi la modou interesse nak so meuneu toule demal took bayi gni meune dokhal affaire yi soff nga lol
si j’étais modou lo je t'aurais déclarer la guerre un combat entrée gratuit amitié gniou khol kou meune sa morome tu parles trop et tu as une tète de malhonnête tu passes tout ton temps a polémiquer hier c'etais Gaston avant hier Balla et Selbé aujoudhui modou lo djikou nafekh ngua yore NOPILE WAYE
Modou Lo n'a jmais prononcé ton nom, C'est TOUJOURS toi qui parle de lui. Arrêtél sa affairou saytaané yi way goor ga.