PUBLICITÉ

Vidéo- Après avoir reçu leurs diplômes, ces juristes déclament des xassaïd de Serigne Touba

Les étudiants de la cinquième promotion du système Lmd de la faculté des sciences juridiques et politiques de l’Ucad ont tenu la cérémonie de leur fin cycle ce samedi 23 décembre 2018.

En présence de la marraine Mme Aïssata Tall et du parrain Me Oumar Youm, ces jeunes juristes, après avoir reçu leurs parchemins ont montré leur joie en déclamant des « xassaïd » de Cheikh Ahmadou Bamba.

C’est émouvant jusqu’à faire couler des larmes. Regardez!

 

Abonnez-vous pour regarder plus de vidéos
Annonces
Annonces

34 commentaires

  1. Jaharmy Tall dit :

    Bamba touba bamba ndiarem diarama ndiol mbacke

  2. Lethio dit :

    Dierediefety serigne touba mi daan feep

  3. mour fall dit :

    J’espère qu’ils vont suivre les enseignants de Serigne Touba en matière de justice et oeuvrer à l’harmonisation de nos lois et règlements avec nos valeurs et traditions

  4. Sene dit :

    Bonsoir cette photo n’est pas votre proriete
    Veuillez l’enlever

  5. Marieme Saliou Faiie dit :

    Dieureudieufty Serigne Saliou ????☝?

    1. RIDIAL THIAM dit :

      Serigne bèthio dieureudiefety

  6. Diaw dit :

    Vous auriez pu contacter le propriétaire de la photo avant de la publier.

  7. L'étudiant Saint Louisien dit :

    MACHALLAH

  8. Ana yalla thi mbiryi dieul lép diokh domou adama dolén khalat yalla ni yonéntoubi psl dinéy senegal doko fék fén thi dioulitou adounabi bakalé chirk billah thi lép lou khéw titna thi sama réw ndakhté diamotouniou yalla serignçi laniouy diamou

    1. Malick dit :

      Aka nékhoul ngua diangue ba khame li gni di wakh di ngua khamni leep yallah ak yauneunti bila

    2. sant serigne touba dit :

      sa ignane dinala rongé ba nga dé dougue safara. xassaides serigne touba loudoul yalla ak yonente nekouthi

    3. Thiam dit :

      Tu mérite même pas de vivre c à cause de serign touba que tu es musulman aujourd’hui espèce de vaurien

    4. Citoyen Lambda dit :

      Yaw si sa bopp nga wara tiit. Liniouy wax sou nekoon si woloff wala français do am fitou critiqué ko. Mais ça se voit que vous avez un probleme avec l’arabe. Vous croyez que c’est un domaine reservé aux naars. Xeep seen bopp rek.

    5. Ndongo li dit :

      Maa ngi lay xamal ni xasiida gi ñu jàng li la ci seriñ bi wax:
      Barke ak yumbal ci loy sakku akug jubal mo ngi ci jàng alquraan mi nga xamni mo gën ci lu nit di tudde yalla, te mom alquraan mo ëmb mbooleem luy ay xeewal, te ku sax di ko jàng di nga raw te mucc ba fàww

    6. DMD dit :

      Liñouy diangue nii dehh; guénoul sante sunu Borom.
      Souléne néxone, pakarñi mais dañou délo lép sunu Borom, diaraléko cii xassida Serigne Touba yiii..
      Il faut arrêter de voir des cafards partout

  9. Cheikh Ndoye dit :

    Thieuy Serigne Bambe
    Dieureudieufetii Serigne Saliou

  10. SIMON dit :

    Thiéy serigne touba yallah rékka menli

  11. Khasidayi sante yalla rék la ak taque yonéntibi khana faye borom diourbel khamo khassida

  12. Balla Gaye dit :

    Santat yalla SA souné khassida rek moy deug ndakh

  13. coumba dit :

    Dieuredieufty serigne bamba

  14. assadou dit :

    Ndeysane kouyy jang xasaides segn bamba gayy lathieté ana yallah ak yonent mdrrr niakk jang tee doo noppi yeureum na majoss

  15. Lat Diop dit :

    Machalah yalna lene yala diapale

  16. yougua dit :

    Borom ndiarem yaw loy wakh ni kone yaw guisso yallah ci khasiday serigne touba yi li rek ak gniane la t yallah lay gniane je veux juste te dire lépi serigne touba yallah la

  17. peuple dit :

    Mes warone guéne dém diangui ay xassaïde mogueunone

  18. gassama dit :

    Lèpou si sant YALA rèk,ndax xassaide yi dèlo ndioukeul YALA la wala way Yonèntèbi rèk,rien à dire

  19. ndiobene dit :

    Que Dieu fasse qu’ils soient honnêtes ,justes dans leur parcours professionnel.

  20. DIOP dit :

    yalnalène djique
    machalla aalakh khol sedna

  21. kheuss dit :

    Nangoul léne Serigne Touba mo léni nopal dounya wal akhirati

  22. DMD dit :

    Liñouy diangue nii dehh; guénoul sante sunu Borom.
    Souléne néxone, pakarñi mais dañou délo lép sunu Borom, diaraléko cii xassida Serigne Touba yiii..
    Il faut arrêter de voir des cafards partout

  23. Mbengue dit :

    Thiéy Waw lén goor Sant ahmadou rek
    Diarama LAMP FALL

Écrire un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *