Vidéo: Alioune Mbaye Nder Feat Youssou Ndour « Leneen » au Grand Théâtre

Retrouvez le duo Alioune Mbaye Nder et Youssou Ndour lors de la célébration des 25 ans de carrière de Nder Boy !

18 COMMENTAIRES
  • beatrix luengo

    kouyy lakh guetcheu sapp sankhall dineuu yakhou téé seu lakhh dou toyyyy

  • Miguel Angel Munoz

    cétait vraiment magnifique l’autre jour au GT deux grands ténors de la musique qui se rencontrent sur scène Mach Allah

  • kiki

    Way bravo nder bravo way

  • fan

    Kkou rater grand theatre kerok rater ngueu lou reuy mané lou reuy ngua raté

  • loli

    it was tooooooooooo hot and amazing, i loved to see mbaye der singing!!!!after youssou ndour he is the best singer in senegal

  • gambian

    Youssou yaw la bougua invité sama birthday j’espere que tu viendras

  • ttt

    Mbaye der youssou ak mbaye dieye faye alias jamais deux sans trois todj nguéinn fi way

  • TIMA

    NON AMOUL NOUMOU NEXEWOUL YOUSSOU TOTH GUAFI

  • Zen

    Nothing but the best from Youssou. Two amazing artists sharing the stage.

  • limatou

    li da ma nekh waye

  • chelsea fc

    youssou ndour rekk mognou saff koumou neekhoull mbaakkall feullee mdrrrr Chelsea is come back

  • kunta kinte

    lakhou guedj dakhana lakhou keur.sa depend niniouko lakhe

  • Latir

    Barké Serigne touba Youssou dingeu yok beu yeuko ndakh danga fonk sa nawlé khebo ken

    • Astou

      khana da nguay khalé motakh tu parle de khébaté? on dirait que féké woulo Mbaye Ndér dans les années 1990. Kane mo sagna khéb Mbaye Nder ci musique Senegalaise? la vraie question c’est pourquoi Prince Arts n’exploite pas assez ce grand potentiel..

    • Marietou

      yaw tu as quel age?

  • samba sall

    c le mieux

  • doro

    noooooo rafetna nder fok nga demate. diadieuf you

  • Nafy

    Un duo époustouflant

Publiez un commentaire