Vidéo – Ahmed Khalifa Niass : « mon père m’avait confessé que Cheikh Ahmadou Bamba n’avait pas… »

Ahmed Khalifa Niass fait raconte une anecdote sur son père qui lui avait fait des révélations secrètes sur Serigne Touba que tout le monde ignore…
Ahmed Khalifa Niass fait raconte une anecdote sur son père qui lui avait fait des révélations secrètes sur Serigne Touba que tout le monde ignore…
Kendou serigne touba meme serigne aramine niasse son cousin a fait les meme temoignase sur le cheikh donc alhamdoullilah, il faut verifier sur google et taper le nom de S aramine niasse vous allez voir ignoran
bayi lne sisou ak sokhore kne d’o Serigne Touba
Par mon exil Allah a voulu élever mon rang et faire de moi l’intercesseur des miens et l’éternel Serviteur du Prophète. kèneu dou Cheikhoul khadim
Par mon exil Allah a voulu élever mon rang et faire de moi l’intercesseur des miens et l’éternel Serviteur du Prophète.
Nagou dieul na thieurou bagn. Je ne juge personnes ni khalifa niass ni les autres. Serigne Touba kén la. Yagu nagnou ko dég té moy deug. Li khalifa Niass wakh deh gnou bari wakhnagnouko mouy serigne mouy koudoul serigne.Serigne Touba Moromanetewoul. Nagou dogal thia bamouy tel nak mo gueune.
Niass momou metrisewoul limouy wakh dou touss moytoul sa boppa loula nekh wakh khamo rien
WA LOU TAKH BAYAME TOPOUL SERINGE TOUBA MOUTOPA CHEIKH KHANA AYE DOF LAY WAKHAL
wa lou takh bayam to poul seringe touba khana aye doff laye wakhaL AK AYE KANIA
Il y a de cela plusieurs années j’avais entendu un certain Mansour Cissé dire quelque chose de semblable venant de son grand père Serigne Amadou Cissé de Pir. Serigne Touba daal Kheyartou!
serigne touba est tres grand il faut le reconnaitre ; mais tous les autres chefs de confreries aussi sont des exemples c pourquoi d’ailleurs qu’ils se respectaient ; c pas de la concurence calmez vous c le senegal qui en beneficierai
Serigne Ahmadou bamba de son vrai nom Thierno Amadou BA originaire de gollere dans le fouta du Sénégal.Vous savez pas qui il est.Yen niep reur thiey mouride
Deug leu, kokou moy BOROM JOUMA DJI sama toureundo AKASSA Niasse ya niaka kiniane!!!
Le commentaire de MD merite reflexion, les fanatiques soyez pas des moutons, ne gobez pas a tt ce ki se dit, A bon entendeur.
un hizbou ki vous parle
Da bakh rk niasss. Wayé lépou serigne touba la. Yalla ko gnieukeu kénal
Legui loutax mom topouko?
Amna lènene tamite.
Fanatik bakhoul djem melni mom mo eup solo
diadiaf khalifa ya bakh téé niakk mignonne
Ken de mom khamnani aldjana la djeum mo ki khol bègue sergne touba té mou nagou koo koukou môme firdawsi rekkk
Salam aleykoum Sénégal dou gawa dem deh soudeiii lou nitt wakh ngene critiquer werantei t khamolene fou souniou borom neii fanatique yi kessei nioy sonal nitt yii nitt dafay gestu tarbiya pour kham.Ahmed Khalifa niasse xam xam deugu leu wakh borom touba alquran bouy dokh leu talibei deugeu dey gestu pour kham le pourquoi bayiii wakh bou beuri yi souniou narei wakh ligeyou serigne bamba dougn fi diouguei lou bakh lo wakh bayi lou beuri .
Sonal ngene niou torop ak werantei serigne bi santou leneu ko deh on dirait des gamins.
Dii toub di diegeulou nieup wa Salam
Baye niass moye bayou gneupe moye serignou serigne si mais Ahmad Khalifa môme dou royoukaye si lepp la preuve tjr des bêtises si diné dji en plus Mame Khalifa limou wakhe si serigne touba la wakhe si Mame el hadji malick wa sallame
Kene doukou tedki Serigne touba amoul morom Balla aïssa
Ceci est une vérité incontestable,que tu le dise ou pas nous mourides ont y croient et c’est évident,mais mon problème est que vous qui l’aviez dit(ahmed khalifa niass)pour moi,n’êtes pas un exemple pour notre religion,car vous mélanger du tous dans tous,wassalam
S.touba kenla
niass danga gorė rėk wayė oui ame dafa thia soune borom xam nga nė SERIGNE TOUBA dou morome
salamou aleykoum wa rahmatoulahi délen moytou Ahmed khalifa niass boubakh lep loumou meuna wakh si diner wola lénén walakhi wakhoul deug lifti dratie lay def cela veut dire approche avec le satan.wa salam
Yéne sama mboki djoulite yi bounguéne dégué kéne thi mouride yi di wakhlou niaaw thi yenéne tarikha boulénko top khamléne ni khélam ma gate rek wayé Serigne touba mom nieup leu eumbeul yiiw ak yéné diou bakh té bania wakh dara lou niaaw dieuméko thi mom
Mais mbok mi kii waxul lu niaw deh!il a juste proféré ce ke lavais dit son père enver kouted ki,que tous le monde sai deja,n’empêche je suis plus contradictoires avec lui que le contraire
akassa niasse kene dou serigne bamba yalle nagnou ko yalla feyal ci yonetiby
Yow (DOUL REK ) yow momou ya wara bayi féne c’est vrai que c’est pas normal niouy critiké kilifeu diambour wanté linga wakh démal nga gueustou djiwatko bou bakhabakh dinga khamni Serigne bi moussoul dieuf lou deupo woul ak charia bala ngay alak sa bop té yangui koy togne WALAHI quand on entend parlé des gens comme vous on dirait que sounou mag gni ils étaient en guerre entre eux borom touba c’est pour moi pour toi et pour nous touss bayliéne haine bi çà ne fera que vous détruire té kéne douko fath borom touba limou niane sounou borom bamou nangoul koko kéne khamouko kone naniou maanou wa salam
Beugue serigne touba rek doyna jammu yalla
bounguéne moytouwoul yéne sois disant kilifa dinéne tal senegal talalélene , kouye daganal greffage di daganal seyou temporaire ak sms meunoma wakh dara i magou demb yi ma gueumla bayilene khiro bi ak ngayo bi wa salam yalla dou fowoukaaye.
Merci DEUGUITE. Serigne Touba, mbaax gu ñu waxal rek yélloo nako, mais Ahmad Khalifa moom, la Yalla xam doyna. Il connait la ferveur des Mourides envers Serigne Touba RTA, et il en profite. Je le considère ni plus ni moins que comme un manipulateur.
Bamba késssééé
Naniou bayi kheuthio bi ay sedeem rafetna trope diaroul tekalei suniou aguei si borom bi naniou fa aguei ak dignite mouye l’islam inchallah
Serigne Touba rek, Serigne Touba kessai. Dieuredieuf Cheikhoul Khadim.
kén dou ahmadou
serigne Amadou Ba un grand homme de Dieu
Bilahi Yaa Goré
Bialhi Yaa Goré
Koubakh ga niasse, il fautle dire quant c vrai.
Je participe un de tes billet et Merci.
Alhamdoulilahi rabbil halamine…
Kein dou Serigne Touba
YARR AKK TEIGUINE MOY MAYEI APP TALOUBEI
DEUG bayil doul so maîtrise woul li ngay wakh nga nopi
senegal bou niou gorgorlou touti rek dem inshallah
Serigne Touba dafa moromtéwooul !!! Dieureudieuf BOROM Touba
Amena solo temoignage yi
wallahi moye kéne
Dieureuredieuf
Senegal Serigne Touba rek mo jott wird direct ci Yonentibi(PSL) .
Koudoul mom ab talibé bouy jokhé wird jambour nga.
Nanou ngoré té ndangou dogal.
NGA BAYILENE AK WIRDOU DIAMBOUR BINIOUY DIOKHE. NIOME DEY WERNANI AMOUNIOU DOME AK MAGG AK RAAKA AU MEME MOMENT
diadieuf amena solo
Amoul morom bamba
Serigne touba mofi néé bilahi lolou leu!!! Ahmed kh niass,il faut senegal bayiko khél Car c est une tête en quelk sorte.
deugu la fall
merci pour se témoignage véridique
serigne bamba mo meunn sii lambii diné
akkay deugg serigne bamba Da moromantéwoul naxxté moy djeuwrignou yonnete bii…entoucas dall deugg mo nexx yalla
Serigne Touba nane la manei nekk jeuwrignou yonenté bi… dagueine di wah beu wah yeufou dof.
Serigne bi Seydina Mouhamed(SAWS) rek moko nioor ak alkhourane.
Kéne dou Cheikhoul Khadim!!!!