Vidéo: A Touba, l’imam fait pleurer tout le monde jour du Clôture du Kaamil de Nafila dirigé par Serigne Fallou Mbacké

Grande Mosquée de Touba, l’imam fait pleurer tout le monde jour du Clôture du Kaamil de Nafila dirigé par Serigne Fallou Mbacké. Regardez


diouma touba par hamidou-sy3

57 commentaires

  1. ruwenzori

    diadieuf waayé, na nou ko dieufé.
    na dooré ci gnii naan ay baay fall la nou, dou nou joullli, dou nou woor ta dara djotouleen.
    charia deugg mooy dokh biir touba waayé barénafa doomou adaama yoo xamni danioo mel ni niou deukk afrique centrale ndax dieufinou yeefer

  2. abdoul ahad mbacke

    yalla reka woor allkhourane rek moye deugg s fallou yalla nafi yag t wérr yallna sounou borom def thi Sénégal ak adouna bi yép ci barké serigne touba

  3. NDONGOLY

    KOU AME KOU TOLNII SERIGNE TOUBA, EL HADJI MALICK, CHEIKH OUMAR FOUTIHOU, MAME LIMAMOU LAYE , MAME BOUH COUNTA, BAYE NIASS, ETC……….DIAMOU YALLA REK MOLA WAR.WA SENEGAL NANIOU SANTE BOU WEER THIA GORGORLOU.AMNANIOU LOU REY LOU YOU BARI AMOUL.DIARADIEUFATY.

  4. khady diaw

    alkhourane rek moye deug lou waye ame loudoul yalla amago dara ndok bagnou amé serigne touba yalla na la yalla faye yiwou alkhourane thi barké serigne touba

  5. ABDOU KHAFOR SENE

    SERIGNE FALLOU MBACKE IBN SERIGNE GUEDE MBACKE YALLA GUAFI YAGUE TEE WER SI BARKEP ALHOURANE

  6. abdousow

    كتاب كريم من كريم مكرم. هوالقرءان . كتاب مجيدمن مجيدممجد.هو شفيعا لايمسه الاالمطهرون تنزيل من رب العلمين

  7. Bachir

    ESKEY !!! Amna solo loool machala Yalna nou YALLA djégual ta yeuram nou barkep BOROM TOUBA !!!!

  8. sape

    en tout cas kou ragal yalla rek la alkhourane di djoylo…yalla nagnou yalla diegeul bakar yeup Amiin

  9. Dikha

    Macha allah.dieureudieuf yalla bima dioudo senegal si deuk serigne you bakh yi ak ay nitou yalla piir yifi nek.nek dioulite khewal bou mag la dioudo senegal tamite khewal la.yalla na yalla doli diam si keurou dine yi ak khewal.

  10. yama bane

    kou xam li alhkour an firi so tade do nelaw yalla limou takou ba diko waat dou yaye nax yalla nanou yerem

  11. ndeye Bousso salihatou toure

    Kou kham yalla rek moy dioye nakh yalla yalla nafi Yag lolll tei werr

  12. Amir

    Ndeysane serigne bi liii daw na yaram trop tei nexx,yalla nala fi yalla yagal barkei alhourane.
    DIEUREDIEUFEI SERIGNE BAMBA KHADIMOUL RASSOUL

Comments are closed.