4 COMMENTAIRES
  • kontof

    mane sanekh moma nékhhhhhhhh

  • vip

    Merci soleil levant wiri wiri mane rek ngen jouer merci je vous adore

  • Madam Faal

    na gaw nieuw ndakh serie bou nekh la

  • balla gaye 2

    hoo sa ma xarit sama sopè coumba namma nagnoula na gaw mom le gneup di khar.

Publiez un commentaire