Senego-TV: Le face à face Modou Lô-Balla Gaye 2 a failli virer au drame… Regardez
Ce samedi 04 août, Modou Lô et Balla Gaye 2 ont tenu leur premier face à face devant les supporters venus nombreux y assister.
Cependant, à l’arrivée du « Roc » des Parcelles Assainies, sans doute des fans du Lion de Guédiawaye lui ont jeté quelque chose à la figure. Non sans créer la colère de Modou Lô et de ses accompagnateurs…
Regardez
Ndiaga sandaga ya mouna doule konne mou katt sa ndeye dee Ousmane rek ci boy Pikine l’athéi
Ndiaga sondage ya meneu doule konne mou katt sa ndeye dee Ousmane Faye rek ci khallee Pikine demale latheko niom
Ousmane faye lagnou wakh kou mer matal sa bakann way 15ème force politique du Sénégal sur les 47 listes en compétition
Cest bien fait pour modou lo mokafi dakh balla falewoul modou lo yalla nalla yalla may ndam balla
Ndiaga Sandaga, c’est à toi que je m’adresse. Je suis sur que si Balla venait à te croiser de 5 cm, tu n’oserait même pas respirer de peur de ne pas le pousser hors de ses gonds. C’est plus facil de dire que de faire. Tu es sur les réseaux sociaux c’est pourquoi tu oses tenir ce genre de propos envers ton semblable sans raison. Que Dieu fasse que tu croises Balla GAYE II! Tu le connais moins que tous les 15 millions de sénégalais. Si tu l’insulte de face, il va te corriger très bien et ça va en rester là. Tu peux ne pas le supporter, c’est bien normal. Tu peux étre fan de Kharagne Lo, c’est encore bien normal. Mais de là à souhaiter le croiser pour l’insulter, c’est qui n’est pas du tout sérieux de ta part. Wassalam!!!
Yalla na yalla maye ndamm bi a balla gaye inshallah
WALAY DIOP wakh nga deug entièrement d’accord avec toi lamb dou yeufou nit way mal civilisé mal éduqué mystique insulte ect….. je ne sais pas bane ndiarigne ak bane valeur la am thi rewmi chiiim
Amoo lo niane Seugne Babacar loudul li ay lambe mane dale ak Talibe yombuul deh
balla bouma rombè dinako sagaa
Modou lo inchallah di nga dane balla Gaye2 mako wax si barker alhourane balla Gaye2 ragal la beneu feeme rek la yor toub souf gued tenkame gneuw sa kaw souko defer boul anarriere taxawal deuguel sa bop dor KO teh boul KO may mouk beneu wet sisa yarame KOme ni nga donne Def AK lac deguer2 boulko Def deh diakkarlo AK mome xex xex bou mitti sou yaguer mou diexal nga danko soudeh setane nga ameth deme brusche ly lolou Moy sa comba AK balla gaye
modou lo laniou wakh
Balla gaye2 ragal modou bouko may dara
Magui gnane Yalla si barker serigne babacar sy yalla nga dane Balla Gaye2 ba took si kawame
c’est le milieu des bandits et des escros.Seulement,les griots qui y trouvent leur compte font la promotion de la lutte.c’est de bonne guerre.milieu samba mbayane, macro,politiciens,mbayane.c’est un milieu sans valeur aucune.
Cette famille Aziz ndiaye De merde modou dou gris dé famille lay nohou bene par bene
Bien fait pour modou lo .d’abitudine c lui qui provoque qui jeté des chose à ces adversaire ????. Le problème moy ballà gaye2 d’affa nièmèè modou lo.
Kell est l’utilité de toute cette présence policière…. Connaissant la popularité de Modou Lo c sûr k diiguéne faayou
Samedi 04 ?????