Photos: Un monde fou a accompagné Sokhna Zeynab à sa dernière demeure
Ils ont été très nombreux à assister Sokhna Zeynab dans ses derniers instants sur terre. Un monde fou a assisté à la prière mortuaire à Thiaroye avant d’accompagner la défunte aux cimetières de Sam sam pour son inhumation en début d’après midi.
Yermendé ak diéguelou yalla yalla na wathi si kawaw si barké al qur’an
Qu’Allah SWT l’accueille au meilleur de son paradis
Amin yarambi
Yalna ko yalla kharé aldiana firdawsi thi barké Seydina Mohamed aleyhi wa salam
yal nako yalla yeureum
Ina lillahi wa Ina ilayhi radjioune
Rest in Peace!
Amin que dieu lacceuil à son paradis éternel
Ya allahou ya rahmanou yalanako yala diegel teyeremko
Yalle nako yalla yeureum khareco aldiana firdawsy amine
yalnako yalla yeureum té djégalko ay bakaram thi barké seydina mouhameth(psl)
Ku amalone ndiarine gni begee lu bakh,yalnako qu’un borom yeureum ,khareko alfiana
Allakhou akk baar ligeyal yalla rek mo woor
Amine ya Raby
Yalnaco borom bi diégueul co té yeureum co fimou dieum yalnaco gueunal fimou diogué yalna yalla léral bamélam si barké l Islam bimou done takhawé. amine ya Rabbi
Yzlla ‘aco yala diegal
Yalla nako yalla diegal
Paix à son âme
Yalla nako yalla yeureum ??
Paix à son âme toutes mes condoléances à la famille
Yalla nako yalla yerme
Yalnako yalla yeureume t kharéko adiana
Yalla nako yalla atei si yeurmandém
AMINE YARABI ya zaynab yalla nala yalla yeureum
Que Dieu l accueille au paradis firdaws
Ke la terre lui swt légère
Paix a son âme
Bakh rék mo am solo
WALLAHI YÉLLONACO .YALLA NAKO SÙNÙ BOROOM YOBBOU DJIANATOUL FIRDAWCI AMIIN AMIIN
Amine
Paîx à son ãme
Amine ya allah si barke seydina Mouhamet sallalahou aleyhi wa Salam repose en paix ya seyda
اللهم اغفر لها وارحمها واسكنها فسيح جناتك برحمتك ياارحم الراحمين
Yalla nako bourbi dieguele té haréko aldiana
Qu’Allah le Tout-Miséricordieux l’accueille dans son Paradis ! Amine
!
Que le bon Dieu l’accueille dans son paradis
Allahumma ighfirlaha warhamha
Yalnaqua Sounou Borom yeureum téyiékhéniou ak mbolom dioulit
Yalla nako yalla yeureum té xaré co adiana firdawsi té yékhéniou
Yalna yalla khareko aldianah
Li diarna ray sa bopou pour am louni mél adouna diekhna ba nopi yalla bouko thiat djitou thi bamelam bi diahi Khayri bani Hachim psl Incha Allah
Yalla na souf oyaf si kow ome repose en paix Zena
Yalnako yalla yeureum t kharėko adiana yalnako sopém bi terrou
Hami nne
Ya allah ihfirli warhamli birahmatika ya arhama rahimine
Amine thi barké saydina mouhamed fathia ake 12 lilakhassi
Que Dieu l’accueil dans son paradis le plus haut firdawsi
Y allah na co sougnou boorom teerou si Aldianamba firdawsi tei djegeul co ay bakaaram
ya ALLAH diégale ko yereum ko xaaré ko AL Janah Firdawsi baré Nabil Moustapha SALALLAHU TAHANLAA HANLEYHI WA HANLAA ALIHII WA SAHBIHII WA SALAM aamiine
Yalla nako yalla yeureum té haréko Aldiana Firdawsi