27 COMMENTAIRES
  • Asmane

    Raféet gua kaye ma tak leu

  • V.B

    tu te prépare à faire comme viviane ndour toub pour avoir plus de fans parceke au Sénégal ya plus de musulmans ke de chrétiens…guem.léne sen bop té bayi affairou thiahane….

  • latif

    la classe ma belle c'est bien ca

  • maguiwalyette

    li mo gueune nguay melni thiagua ya mki dala wara guener rewmi

  • abou sakho

    " NE JUGE PAS ON NE TE JUGERA PAS"
    soufeké dieugalou keep gassi dioublou sounou borom moy adie diegalakone .waye itte souféké akap mode keep la may délou ci kadou cheikj sidy moukhtar té moy nanou bayi thiakhane té diamoudié YALLA
    dakh kate koulou nafsine zayikhatil mawti koulou mane aley kha fal.

  • NIT DOFF KILLER ?

    gui gui Yow lay weur dh worna

  • bole

    sénégo yéna sof diokh lénenou informations bou doye lanou wakh taguéne bayi séne pub yi gni safou gnounou…

  • GÉR.

    wa kouy guigui? S'il vous plaît repondez moi. Je veux la rencontrer elle est très belle machala. Carrément

  • tamsir

    sopékouléne adouna amoul solo

  • miss

    waw super belle li dara féouko mane guigui dafma nékh rék

  • bref

    yalla nalene yalla sopi te dieguele len

  • hadim dou dém khana guigui da nangou sa dieukeur lol en tt cas el est très belle

  • sunugaal

    lol hadim vraiment rigolo…

  • hadim

    guigui nagou dieukeurou diabour yi rek lafi néké c'est sur que ces temps si da am pa ibadou qu'elle essaye de charmé,dorkat bou mak la

    • xéeul

      mdrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrr hadim tu ma tué mais nak payi dogno diékhal na yeuw thi nous les jeune tout frais gnou défar bamou bakh guigui dou niamou maguette

      • lala

        hahahahah toth nafi

  • ali

    tay kala souba taate you bakh yi senegal mo saf

  • max

    amina pote
    guigui
    desse major
    et
    certaines manequins et autres
    ak wa senego ay dil l
    a pour lui faire promo nous on saves que c'est pas du tous l'informations interssant au moin guigui et autres modes nus voila sa c'est tres interessant.

    • amax

      bien dit max et la liste est longue ya lissa ,viviane,aida samb et c'est temp si ya adjouza la vilaine moche qui doit certainement debloqué une forturne pour ca promo car mm si elle fait caca ils trite "adjouza fait caca dans son douche"

      • davido

        on dit ca douche

  • Mamadou

    wa sénégo amouléne foula

  • MAMICHOU

    NICE NA TROPP MAIS LIGUA WARADEFF DEFFOCO MOY GUA TOUPP MO GEUNE SI YAW

    • ib

      oui et je crois qu'elle sur la voie de se convertir à l'islam, yalnako Yalla diapalé

      • dior

        lol ib ya nékh qui ta dit qu'elle est autres que musulmane et esk c'est les musulmanes seulement qui se voile khalass

  • mamadou

    mais senego amouléne foula

  • ladiva

    nice na

    • fatima

      toute belle la diva guigui on te souhaite la bien venue dans le club des hadj et surtout ne change pas

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *