PUBLICITÉ
Photo-Pacotille et ses deux garçons au Parc de Hann

Photo-Pacotille et ses deux garçons au Parc de Hann

Pacotille et ses deux garçons au Parc de Hann

Pacotille hann

Annonces

(28) commentaires

  • Machallah

    yalla nako yalla yeureum.. deugueureul famille bi diappalenn té kharéko firdawsi si barké ramadan bi

  • Fina

    adouna mo niack sollo yalla nako yalla yeureum te khare ko aldiana barke seydina mouhamet ( psl ) tee tekk si khalee yii lokho

  • Truth

    C pas deux Garcons c une fille et un Garcon mounass et lamine faut pas voir une foto et ecri just ck vs pensez

  • Madam Faal

    Ndey Yal na ko Yalla yerem, Amiin

  • Martin Luther Kng Jr

    En voyant ces deux bouts de bois de Dieu je ne peux pas m’empêcher d'avoir les larmes aux yeux comme si j'etais a sa place voyant en pacotille en moi puisque j'ai moi aussi 2 garcons comme pacotille et ce que je ressens en eux et vice versa et eux ont perdus un pere papa poule .je ne peux que leur dire massa et que Dieu leur garde amen

  • Dada

    yalla nakô yalla yerum le pds nak boul fater diabotu pacotille svp wakh rek gueni deffff

  • Puff

    Je veux adopter bebe lamine comment je vais faire?pacotille sa mort m a profondement touche.

  • Oh

    Oh kil snt mignion yalla guene soute sen papa fan way en les voyants sama yaram dafa daw me sant boubah Dax serigne bamba dinala taxawu inchalllaaa

  • Seye Orange

    amen

  • Tabara

    ndeysan yereum nalen djirim dafa méti

  • Badou

    Ndeyssane rawna yaag na

  • Dji

    Yalnako Yallah yeureum ci barké wérou koor bi !!!

  • Babs

    repose. en. paix. yalla. nala. yala. khare. aldiana

  • Bea

    senegal2012

  • Bea

    senegal12

  • Mo

    Pa deux garçons pluto sa fillette et son pti frere Lamine

  • Serigne Modou Dioum

    Dunya gatt na gatay bou kene meunoul mesure,
    Kouko diapè Keur diume ga lolu meunako jurè…

    RIP #ndanane

  • Mbodj

    yalnaka serigne bamba térou té yalla kharéka aldjana firdawsi amine

  • Ibson

    YALNACO YALLA YEREM TE YEKHENIOU AMINE

  • Yeup

    kallah le tout puissant lui accueille dans son paradis firdawsi

  • Ndoye

    Yalla nako yalla kharré si adiana you kawé ya té sounou borome tékk lokho si diabotte taam dji

  • Djilykou

    yala nako yala yeureum si bar keb serigne touba mbacke

  • Diop

    yala nako sonou borome bi kharé adiana té ték lokhom si ay diabotame amen

  • Za

    kou âme dôme dewo

  • Ousmane Soumare

    adouna dall kéne xamoul sa bo heuyé mou diahal la hana di niane sa borom bi xam lépp fépp yeureum KO harécko aldiana firr dawssi ta samalcko niabotame

  • Fille

    Que Dieu l'accueil dans son paradis

  • Jeannette Mendy

    k Dieu le miséricorde le pardonne c péché et l'accueille o paradis ! Amen!

  • Kaylia

    Allah y rahmo qu'Allah lui fasse preuve de miséricorde qui lui épargne les duplica de la tombes pardonne c péchés et l'accueil dans son paradis amin ya rabbi