15 COMMENTAIRES
  • ASSANE

    Wally seck degua raw sa morom lolo takhe nienene yii sen khol bonne .mais du courage Dieux est grand le proverbe à dit rien ne peux contre la volonté de Dieux

  • alioune ndiaye

    amoul morom

  • Ma

    Thia kaw thia kanam laf thiat faramarén bi 100% wallyette namougnou dara

  • zema

    tro mechan mem mei ki dou dm ndakh sokhor

  • Diiassy Tiiger

    Doudou yaaa sokhor .. mé nitt kou bakh dou gnak none

  • mo

    way dabo ya wakh pakétou deug Doudou va te faire foutre avec té conseil donne le plutot sa baye méchant

    • khady

      Ki bayi len ko fofou khawma moy kan bay wakh thi Wally seck dara kholam moy metti te dina geunn metti…

  • dabakh

    Amoul morom faramaren bi

  • Dave

    Nekhna ! Waly t le meilleur .

  • Dave

    Nekhna ! Wal t le meilleur .

  • Dabo

    Wally dé dou moromou bambaly ndakh débutant leu par contre nak wally seck ndanan baayou artistes yi namoul daray bégueul Ay fans wam di way nak lou tégou si temps kon koukoy dingate danga bone sokhor ignane ignéti ignégnégni wally toujours thia kaw thia kanam kén douleu téyé barki cheikh ibra Ndeye yi douniou bén té dollé yémoul yallène meun

  • DOUDOU

    un conseil @ wally aller a l'ecole de musique etudier 2 annee svp.
    xell a etait deja chantee par la coumba gawlo seck, avec un merveilleux clip fait aux theatre sorano titre sama xell voir youtube ce n'est pas te detester mais t'est loin de tes parents meme bambaly seck chante mieux que toi

    • khady

      Yaw mom li sokhor la wala lanla ni may wakh mounan 2ans d'études Wally khawma
      demna école de musique?,khawma demoul wayè gni fa dem gnimèwou gnouko nakh kounè khamga ki la Mann,Wally dou sen morom kouy fora meun kouy saga tè kouy dorè di saga,di Matt mo meun gneupp…

  • Geum geum

    Si kaw si kanam rk Wally ! Koula yéné lou bone yalnassi djitou

  • MATT

    nice na affaire de XEL

Les commentaires sont fermés.