Serigne ci bouniou bayi khel opposition bi mais peuple bi laniou wareu bayi khel
Séni talibé nioy deh si dialyse bi séni talibé nioy deh ndakh diabète bi ak cancert bi
Séni talibé laniouy fitnal si université yi
Séni talibé nioy dound ay werr sans ndokh
Ak di nane de l’eau non potable
Séni talibé laniou sathie sén kom kom diko passar passaré si parti politique yi ak concert yi ak lamb dji
Comme je le disais chers frères et sœurs vous êtes livrés à vous même
Plus personne ne vous défend plus personne ne s’inquiète pour vous
Soit vous vous prenez en main soit vous allez restez des pions qu’on utilise à chaque occasion
Wa salam
Lima beuguona wax merci nitt
Limou wakh lepou deugula nanouye khol talebeyi seni diafe diafe
Tu as parfaitement raison ,même si le marabout ne respecte pas les sénégalais il le doit au moins à Mr khalifa Sall qui porte le nom de son père et Mr Mansour sy djamil qui est dans la même famille que lui ,et ils sont dans une position de refus et patriotisme envers ce régime qui est le plus médiocre depuit l’indépendance
Nitt Je t’apprecie bcp mon et je partage toujours tes convictions
Tu es une valeur sûre pour la jeunesse nit pire nga
Il faut respecter les convictions des autres.
Merci nit doff serigne siye doundé alalou askanbi sunu dé safar lanou dieum mako wakh