10 COMMENTAIRES
  • pro

    mbaye pekh rafetna nonoula rousloga wa pouvoir bi mbeulé

  • alpha

    Sénégal da sakh la niao melne yaw, yalla nala fi yalla bayi bathi kanam

  • bègue s touba rek

    Diaradueff mbaye yalla nalla yAla fay sa khoul

  • issa laye ciss

    vréma mbaye pekh nawnala trope,dafare mo gueune yak,té djoulite dafare rek mo ka ware

  • mame cheikh niane

    merci c’est comme ça quand on est en face de quel qu’n qui dérape faisons le revenir à la normale

  • ndirrop

    Mbaye pekhe je suis vraiment fier de toi un homme honnête sincère Fidel reste tel que tu es avec wade j’aimerai vraiment avoir tes contact

  • welly

    niou mel ni yaw sounou beurè won si wetou wade ak si wetou macky kon diam rek moy am mè c domage k yaw rek nek si wade macky amoul ken

  • touba leye

    Pekhe nigadf rikela note boko bagui lipe lokoy yakhl dakotha ware guine

  • thiam

    vraiment niou melni nio barétoul thi rewmi niouy wakh deug di defar mbokk !!!

  • papis

    mbaye pekh gor deugeungua nitt kou bakh dey def lou bakh diarama yalna yalla defala kheweul

Publiez un commentaire