Les révélations de Serigne Moustapha Sy :  »Desna touti Kou sante Sy douma eupelé Touba »(Senego Tv)

Le guide des moustarchidines, Serigne Moustapha Sy Al Maktoum est revenu sur ses liens avec la famille de Serigne Touba dont Serigne Mountakha Mbacké est le guide.

Voici les révélations du guide religieux

Regardez

12 COMMENTAIRES
  • Anta seck

    Sen sant yi mouy sy ak mbacke mom nguen nakhe askan wi ,lifi indi sy mo fi indi mbacke indi fi sakho indifi ndoye ak diop al seck

    • BAMBA JI

      ANTA NAGOUL DOGALOU YALLAH RK SY AK MBACKE SEN MAME DAFA LIGUEYE YALLAH MOU FAY LEN BARKE BOBOU MOLEN TOPOU BATAY

      • Anta seck

        Sen mame ay nit you don diamou yallah laniou mais pas ay fond de comerce .gni lek adiyeu ak chantage gornament dadiale alal te ligueyouniou touuuus
        Li dou l islam ay nakhate la ci la bokone legui al hamdoulillah
        Diamou yallah ne rime pas avec fortune yor alal te sa talibe amoul loumou lek

        • Djibson

          L’islam ci boopam ay nakhate la. Ay leebou Naar la. Donc mbourou fof ko farine.

      • Ahl sunna

        niak diom, Yonente bi li mou ligueyeul Yalla, est ce que ay seteum degnou done tok mouy dokh….

    • Vérité pur

      Sou yamoon loutakh dégounou sa Mame ,khamounou sa Mame ak sa baye

  • major sonko

    moustapha va te soigner tu es malade mentale

    • Ndiaye

      je crois mo gueune ba la mouy eupeu lokho

    • Vérité pur

      Alkou mo takh nga gniak yarr.
      Moudie bou gniaw ngay am

      • Adji

        Demaall diangui sa Dinee (Alkouran ak Sunnah) Moudie domou adama c’est du domaine du Tout Puissant et très miséricordieux ALLAH et dont nous n’avons aucune connaissance..

  • Diouf

    Dans l’islam, les noms n’ont aucune valeur. C’est maintenant avec les états civils que les gens portent des noms.

  • Mamadou

    djelel yepp benene kou santou kheti ko ak yow

Publiez un commentaire