Gamou 2018: Abdou Aziz Ndiaye offre 300 boeufs

Maouloud 2018, le promoteur Abdou Aziz Ndiaye frappe fort. Le Talibé Tidian convoie 300 bœufs à Tivaouane. Le Gamou marque la célébration de la nuit de naissance du prophète Mohamed (Psl). L’événement sera célébré dans la nuit du mardi.
Aziz Ndiaye attention à la vie des bêtes
Aziz Ndiaye fait attention à la vie des bêtes.
Yaw baye niass ndakh am nga ben nakk booy deff thi gamo gui
Lou raffett dankoy raffett lou
Vous etes mechant
Bay niass yaw ndakh am nga ndieugou benn nak deff ko nguirr yalla thi beusou yoonentibi
Lii mom mettina leguii ignane bakhoul aziz dhé amoul talibés dh
Sokhore ignane moye devisou senegal merci grazie mille azize fofoula
Sokhore igmane moye devise sou senegale merci merci aziz amouniou loudoule tivaouane
Mome dall diambar la il est à feliciter
Bay niass yaw kon nga aziz moy démal bopame té cheikh bi dfa ay talibé you koy diokh adya
cheikh béthio Tivaouane. 300 KAY ndeysan dolé yamol dal MDRRRRRRRRRRRRRRRRRRRRR