Exclusivité: le clip « Maalaw » de Pape Diouf feat Baye Babou dévoilé

Les laobés sont encore gâtés par le leader de la Génération Consciente. Pape Diouf dévoile enfin la vidéo musicale tant attendue du single « Maalaw » en featuring avec l’artiste rappeur gambien Baye Babou.
tres belle chanson
pape diouf cii kaw cii kanam; kene doula téé
je suis un fan de waly mais pape diouf malaw todj na nexna torop
merci pape ca kaw ca kanam
NEKH NA
Bayiléne seytané waly est de son coté pape diouf art bi yatouna bayiléne nafèk
So nice Pape good continuation
C est très beau Pape continue sur cette lancée machallah tous les bons Sénégalais et sénégalaises sont fières de toi
C est très beau Pape continue sur cette lancée tous les sénégalais et senegalalaises sont fiers de toi
bagoumaa wax waye deuge deuge pap doo morom wally
Morom waly, waly il a dépassé rendez vous le 4 juin à bercy
Machalla du courage
bagoumaa wax waye deuge deuge pap doo morom waly
Yaw daga wah loula néex, hame gani xel, comme album xel k waly dou moromou pape jaloux
ohhhhh nekhna
Pape dallllllllllllll defatigua seu meunin ??????
pape clip bi nice na trop yalla nala yalla lafale thiatte
Bilay Pape Diouf dou moromou PD yi forcing masha Allah si kaw si kanam rek !!!!
la classe
J n SUI pa t fan mai u chante bin
segame tidiane ak mouride lagnouye diakhasse dougnoulenefi bayi
nekhna pape dipuf yalla na yalla deff diameu boul deglou beneu nafekheu waly sa rakeula
Nekh na gorena ma challa defofi dara lougnioulay hebee way rekk gay deff
yenn wakhou thiaga rek guenn beugg dara nekhoussi nieppa yem bouniou nee waw rek niou koumassee wakh you niak fayda boy diouf betgama meunone gakko wayal sa jabar t te ek yemfa, dama yakarone fass gayy wayy ndekete dagayy thiagatou ci kadou, wakh day rafett wayyy
Hahaha. .yow anonyme dohal fowi. Fans wally amou fi place..da nga tit. Lol. Pape da garaw nak.soulna 20 titres wally seck yi..malaw rek. Li eup n'a nekh waayy
yenn wakhou thiaga rek guenn beugg dara nekhoussi nieppa yem bouniou nee waw rek niou koumassee wakh you niak fayda boy diouf betgama meunone gakko wayal sa jabar t te ek yemfa
nekhna mo dakh way wally fouf wally manoul tous
Un peu de respect mon gars
Dico maye thione seck ak aye domame yépp
Nékh rékk té goré
Non non li nékh na trope sakh
Mamyta ignane bakhoul té kou Nangou nopalou deug nekhoul. Machalahhhhhh nice na lol.
ENFIN!!!!!!
bilaye y'a mena way machala
mamita khana fans Wally gua sa khôl bi DINA dague dé merci pape Diouf y'a mena waye dé
Yaw nel nekhoula kaay
Nekhoul dara
Les commentaires sont fermés.