8 COMMENTAIRES
  • Lol

    rokose nako

  • Madou

    Eumeu dou moromam ya pas foto .

  • Fatou sall

    Yarou dou la wagny dara xalé day am yar ak teguine 2-0 ak 12 coût non niaw n'a Eumeu yaye gor

  • Fatou sall

    Goné bou yarawoul gniou diagalko djiogale bayame …

  • sarr mame cheikh

    eumeu felicitation .no nice bro .tu merites plus k sa

  • Morla

    Gnhomghnar gnhep ay senegale lanou nanouthi wakh lou rafete li sporla te ay dioulitlan wakh noumou guena rafete mo guen diuefdia hitam nanco rafetal li euma wakh sou ame na mougn yalladal mokham teylen

  • bègue s touba rek

    Eume la nou wakh balla danou la mane bague 3 fois eume dane nalago

  • toufa gaye

    eumeu nonu la lirek mokoy faye lii ame dafa nianw thi aye dioulite ndakh aduna amoul solo li lepou daye diekh merci eumeu lirek mokoy fadie li rek

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *