10 COMMENTAIRES
  • nitoudeugue

    Yene amo lene bene khel yéne niar gno gnou ndoye bane wakh na deugue nako wakh yobou wou mala rek mais sokhma si tognou ko beugone nguene taximan bi saga sene yaye wala sene soeur wakh ko tiaga delo si lene sene khel

  • UNKNOWN

    Je suis ‘avis avec Ndoye BANE

  • El hadjy

    Bonsoir le groupe senego le taximan il ne dois pas insulter les femmes parce que il doit dit non je dois pas insulter oui

  • mamii

    kougne né ya reew ni taxi man rek boula yebo kharou

  • fall

    dawsi tognol yobalema rek manoumako mo guene gakoy insulte walahi soudone ko yoor douko wakh yobalema m yakar rekk

  • fall

    ndawsi tognol borom taxi bi amoul droit diko insult yobalema soko menoul nko menoumako mou dikh

  • dio

    ndawsi tognoul.il y a des taximan qui sont arrogants. ceux qui sont sur la circulation savent trs bien ce dont je parle.pas tous les taximan. et puis les siroumanes la nuit embarquent des prostitues et personne n en parle.

  • sope naby

    certe fous ci ndoye amnga deg ndawsy tognoul dafa gnane rekk dankoy may walla nga bayiko moudem meme kiy diay guerte thiaf ci mbedemi sakh boula nekhe nga gnanko dalay may walla moubayila nga dem djiguene Bo kone thiaga nga ci sa yaye lay fayou manoul fayou ci yaw directement wathie sa auto di diel ay yat didakhe melne dof modoul yonn surtout nga koy def djiguene li General boubou done wakh fan yi passe ni taximan yi yarou wougnou deguela bala gnoulene di diokh permis dagne lena wara diangal sang froid ak civilisation ba pare

  • wakh loubakh

    ndawsi motong dè

  • wakh loubakh

    ndawsi motong dè

Les commentaires sont fermés.