36 COMMENTAIRES
  • Binta

    Sa ete une grand nouvel pour mw de savoir ke dieu vou a beni avk un mari wi tu la mrite . Te kholale les jalou von morir ndakh mounougnou dara si yaw so teu d sa guinaw bandngn diallo diery ba kene lal leu

  • Binta

    Ton mari a bcou de chans car tu es tre rare wi tu es tre belle et ta bote na pa de limite ke la pai soit a avk vou yalla bakhna te sey yombou diap teuwe bayi rek

  • mita

    heureux menage ma cherie man mom tu ma toujours plus bilahi, tenga walougnou. j tem

  • mamadou

    Nagnouye sanganetai soutoura nakhe yalla soutourale gnou heureux men
    age

  • nopp sama bb

    yalnala yalla diapale si sa seuye bi! boul deglou wakhou kenn te seuyal te yalla takh. fonk sa dine te khami souniou dine rekk laniou amm. yalnala yalla may kholou mougne iow ak sa dieukeur. guen dondou bay fete sen anniversaire de marriage.

  • Bruxelles

    Avoir de ma classe n est malheureusement pas donner à tous le monde…et elle en a énormément …
    Les crachats d un crapaud n atteignent jamais la blanche colombes, alors que les fonds du panier s exprime à fond 😉

  • fatou

    heureux ménage ma belle

  • akassa

    akassa adja diapal sama wadji yawit diapalèko niari commentaire you niaw lou thi dess yeup bakh li moy wanè que sengal ya des gens qui resonnent encore yallna sey bi am barkè akassa.

  • MOURID SAADIKH

    khanaa mousouléna deff yalla baakar ba soukou diko djégalou…khanna yéén dangéna amoul ay ayyib bay toudou ayibi djambour…khaana yéén khamoulén lithi toudou bakarou djambour boo khamnii toupp nako ba yalla djégal koko…seydina mouhamad (STAW)waxnani kéép kou toudou bakarou moromam boumou toup ba yalla djégalkoko yalla dinala bindal baakar bouni toolou…kéép kousa bay djangaloul réék raynala dangay alkou alagalé gnilaweur…démlén djangi walla ngén noompi

    yalla khamnani nimako yééné baanékh bii thi sama khool lako tibé yalla nalén yalla mouseul thi tiatt lamign kou soxor ak kou ignaan ak un(e) envieu…djabot gou barkél balénii yoobou maaka biss thi barké khaadimou reussol

  • fall youssoupha

    yalla na seuy bi ame barké yalla def thi soutoura borom bi def thi ndiabott gou barkel té borom bi tapé khol maye lene mougne
    mougne moye galadiou domou adama !ame sakhoul gnak sakhoul !ame goré gnak goré !té seuy nek bou khatt la ;wayé khol you ande thi yeurmandé gnokaye yatal yalla nalen ko borom defal yak sa dieukeur !koulaye khasse nak mba mouye yak sa derr nangoul !ndakh nagou bobou molaye defaral sa seuy taye dji nak sa nones yeup gnougui la tek beut di khar sa faux pas yalla nala thi borom bi mousseul !diapal sa dieukeur té topato sa diné té khamni gnoune thi yalla lagnouye delle adouna bi gnou nek mbane mouy wankétoula rek !heureux menage et k allah te protege !yangui thi diamou yalla bou kawé finga tolou legui .kone nak nanga khamni kouye diamou yalla dou setlou bonne chance petite soeur!!!salam!!!

  • Bruxelles

    Les jaloux vont maigrir… Très beau couple manchallah…félicitation et heureux ménage 🙂

  • momela

    yaw med khana daga deuk ak ay thiaga khana amo mak ñanaléko way heureux ménage ma puce

  • FATMA

    seyal cey bi ma chere

  • Kirikou Fall

    Heureux ménage, que le seigneur guide vos pas dans cette nouvelle vie

  • xxxx

    Félicitations un bon depart pour ta nouvelle vie et surtout ta vie de demain aussi on dit que seul ton mari pourrai te rentrée dans le paradis je te souhaite tout le bonheur du monde

  • lebeau

    t’ toute ravissante, les jaloux vont maigrir, tu as ta vie, mène la comme tu la consent. koumou néhoul topal feulé

  • lebeau

    astou diagne hana mome mome thioaga ak ndayame ak bayam, thiaga rék moy hamé moromame, Adjia félicitation et heureux ménage

  • LAFLEUR

    Seuls les imbeciles ne changent pas N’écoute personne seulyeul seuybi rekHeureux ménage Ma Fille Tof Yi rafetna Lollll

  • mariame

    mais ASTOU diagne yow lanla mais thiaga moy hammé moromane chacun veut changer ka meme HOOOOOOO;adja yalla nalla djigue wayy ;

  • matar khaly

    Pourquoi voulez vous imposer aux gens de mettre un trait sur son honteux passe alors que quand elle faisait ses bêtises elle n’y avait pas pense? Damani Kouy yedde nanga ko yedd nom te mou nekk leçon ci les autres. L’histoire a parfois les jambes courtes. Wassalam

    • MATY

      Mais Matar khaly, que son passé soit honteux ou pas ce n’est pas notre problème, c’est seul Dieu qui a le droit de la juger.Toi que sait-tu de ta sœur, de ta tante ? Ce qui importe dans ce bas monde c’est de se préparer pour l’au delà. Au Sénégal on a l’habitude de d’accuser les gens sans preuves, et parmi les plus grands péchés en Islam, il y a le fait d’accuser une personne de fornication, ceux qui le font n’ont qu’à arrêter au risque d’être maudit par DIEU ici bas et dans l’au delà.

  • zinedine zidane

    J’esper k’il va durer

  • abou gaye

    heureux menage du courage boule ta cule one me gnow takala cop bakh gue du courage fi mome adouna le les mechantes vont maigrire diam rek guey ame

  • Fatou

    Heureux menage ma puce

  • lola

    Adja tu es magnifik t rob es bel class et simpl vraiment heureux ménage

  • bon courage pape kou gneup beugu wargua tite si s pap a bop yalnala yala diapale dolila soutoura adouna koulal khar si lou bone yalana khadi

    heureux ménage pupuce

  • Thiam

    Bayilene khastantebi. Té gnou gnanal ko rék

  • Dija

    Astou Diagne thiagua dhei moye xamei moromame, Yalla na niou Yalla moussal si nite you melni yowe, soxor et aigrie, Heureux menage ma belle Adja

  • mouhamet

    haha yalna yala motali te barkel lepou doli soutoura

  • khalass

    Sokhna si sa wakh niaaw na tropp. Yalla nala Yalla diégueul.

  • Mina

    Heureux ménage. Necoute surtout pas les jaloux et les méchants.

  • zagazaga

    astou diagne you bone ak sokhor rek joy yow.. yalla nala yalla sopi te change sa khol bou nioul bii

    • Lazouinaaa

      Machaallah yal nalla souniou borom diapaler inchallah !! Les genre de astou la nioy tok maguette bi douniou am dieukeur bayil sokhor vilaine va

  • astou diagne

    enfin la thiagua amna dieugeur.

    • Sonia

      Thiaga bi eupnala chance nda guisna kouko noop
      thiaga biir neeg yi gnio deuk si khasté heureusement que Bour Yalah barina soutoura

  • Sahel Lienne

    yalnassi yallah deff barker ak yiww bou bari amine

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *