(20 photos) – Découvrez la nouvelle grande mosquée de Léona Niassène
Voici en images la grande mosquée de Leona Niassène qui sera inaugurée, au mois de mars prochain, à l’occasion de la ziarra annuelle. Ce lieu de culte entamé en 2009, a pris 7 longues années de chantier.
Regardez cet édifice qui fait la fierté de tous les musulmans du Sénégal et de la oumma islamique. Admirez ces images!
dieredief presidan macky sall
BEAU JOYAU MACHA ALLAH
machallah rafetna trop
Machallah machalla
macha allahh
macha allah
Déleen binde Macha ‘Allha en deux mots mo eupeu yool. wassalam
Machallah, Niass Abdallah
machalla yalla ne yalle fay si barke Elhadji IBRAHIM niass khalifa niass ken do moum te moum do kene
machalla yalla ne yalle fay si barke Elhadji IBRAHIM niass khalifa niass ken do moum te moum do khene
Machalla yalla ne yalle fay si barke Elhadji IBRAHIM niass khalifa niass ken do moum te moum do kene
C’est une fierté pour Toute la communauté musulmane
Dieureudieuf Président Macky sa liguey rafetna. yalla na yalla fay. Amine
Macha allah mame baye niass borom faydou bi
waw gor macki sall lamou wakhon defnako taral keurou dine yeep
dieureudieufeté baye Niasse amoul morom
dieredieuf mame Khalifa niasse
hooooooo machallah vraiment
hooooooooooo machallah vraiment
macha Allah dieuredieufe baye
Niassen yi dara dara dioboulène danio niakk kiniane. Rafet na taa tarouna al khourane rek mofa nek
Franchement c’est salu, C’est une fiert De Toute la communaut musulman.
machala sama prsident limouy def ci leur djioulite yalnako yalah Faye amine
masha’lla
DIEUREDIEUF MAME CHEIKH IBRAHIMA BARAHAMA NIASS
macha allha deug raftna trop yalla na yalla nagou leep louou fa diamou yalla amine
skey nila de kou ligeuyal yalla koune da wara am mandarga
Macha allah rafétna Lolll yalla naniou YALLAH samal sunu kilifeu yii
Djeureufety Cheikh Ibrahima Faycal (
Merci au President Macky Sall pour cette oeuvre colossale . Yalla nalla yalla fay
machallah dieuredieuf El Hadji Ibrahima NIASS doundal ba doyal li lépe yawla
Macha’halla mane lii laa gueume meme si je ne suis pas musulmane sakh, mais Néégou YALLA dagnoukay topatoo Way !
-TOUBA Sééne MOSQUEE pré bagnoukay Yokhaat ba sakh tabakh Grande Mosquée à Dakar Mou Mingo ak Diamono
– MEDINA BAYE : Séénne Mosquée pré na Macha’halla
– Ndiassane Sééne Mosquée Pré na
– Mosquée Oumar Foutiyou bi nék fii si Cornich bi Sakh Pré na
– Meme Cheikh Béthio Sakh, Sa mosquée sera bientot finie lolll
– Djoumaay TOUBA NDIAARèME MBOURR mOSQUée bi pré
– WA DAMAY LAATHI Mosquée TIVAOUANE moom kagn lay pré??? Depuis 1960 ba laigui Kagne lay Pré nak ???? Béne Soorrool Dongue Meunoul Pré ???
mais est ce que yaw khame nga loutakh égaléwoune ko yaw MARIA SENEGALAISE lidieune tile lou sa yone nekk. Bou fékone beugue nane mou ague bou yagg kone paré na lidieune tile sa gallé ba paré vatant