bonsoir en tout cas boy wally seck kou bakh la tee nitte la .
guelewar
Toubay bou thieuk a la mode kkkkkkkkkkkkkk
Thiey waly mo nekh deeeee!!! soit humble Waly avec ton habilement sinon tu deviens ridicule et tu perderas des fans, apprends avec ton pere You si tu veux devenir un grand musicien Africain avec un look Afro-europeen et Afro-traditionnel senegalais. De le part de ton fan. Bon courage pour le reste de ton carriere. Peace and love
mona
Bilaye waly guor dieguene laaa
maty
Modou kara ne se déguise pas boul togne…. Ouzin keita di melna Vampire niii..
fma
voila comment on peut developper un pays en chantant et en dansant…………ces pov cons…….apres gaspiller leurs argent vont venir au senegal critiquer critiquer le chef d etat……
famara
Ozin keita c déguisé comme Modou kara
tima
comm dab rek laff thiatt way faramarenn bi
khame
franchement wally fan nala torop mais sa sagnsé biyone mome dokhoule
pape diouf
wa waly coumou yap loumou soll moye hana thiekeul ma la soll mais boubs yamana sagnse sa blanc bahna trop
toufa
extraordinaire waly je t’adore
zelko
waly sa yaram mo nangou sagnsè ndakh newoul keuthie rek wootè béton, lo def mou dem
waly
EN VOYANT OUZIN KEITA JE CROYER VOIR SERIGNE MODOU KARA A LA 6em PHOTO
touf
thiey khalè faramarene soirée bi tojna ngafa linga sagnsè def na classe
Comments are closed.
Ne manquez aucune actualité !
Téléchargez notre application pour une expérience optimisée et pour recevoir les dernières nouvelles en temps réel.