Annonces
Annonces
» » Vidéo: Émouvant témoignage de Sokhna Aidara...

Vidéo: Émouvant témoignage de Sokhna Aidara sur Waly Seck. Regardez!

Elle fait rarement des sorties médiatiques et est connue pour sa discrétion. Pour les raisons des préparatifs du concert de Waly Seck à Bercy, la femme du chanteur en a profité pour faire un témoignage sur son mari. Regardez!

Annonces
Annonces

26 commentaires

  • fa
    29/05/2016 15:40

    ndeysane yaram dawna sama yaye sokhna aidara ya bakh ya dale ya téyy machala yaye boy

  • fayeeeee
    29/05/2016 15:55

    amine diabar diou bakh moy yaye wakh leeene amine way

  • faye
    29/05/2016 15:56

    amine diabar diou bakh moy yaye wakh leeene amine way

  • faye
    29/05/2016 15:57

    diabar diou bakh moy yaye

  • faye
    29/05/2016 15:58

    amine wakh lne amine way

  • Amina
    29/05/2016 16:04

    gnianal ko mou bayi affairou thakhan yi mogeun musik dafa aram te ngeun bayi Muhammad S A W mi geun di todou si ay thakhan yen mi sant Aidara khawma kan molen wakh ne Muhammad S A W sen mam la bilahi Senegal mo nekh

  • aziz
    29/05/2016 16:20

    yow mi Amina bo khamoul da ngaye mandou.kou nek rek ngene dingatt ko.bo khamoul ni AIDARA CHERIF SEUTOU NABIL MOUSTAPHA lagnou da ngay lathie gnou khamalla.sa ordinateur bi nga time di taper loula nekeh fatelikoul ne tu n’es pas seule.y’a 2 ANGES sur tes epaules.(1 a gauche,1 a droite) lou wakh gnou bindeu.lofi taper thi sa clavier gnou lire.boul dougou thi o oumpeuler.bouldi wakh lo xamoul.senegalais amna kersa wakh XAMOUMA.loko lathi rek mou dieum thie tountou…bouldi wakh ti lo maitriser woul lilakhi wara souli.wassalam…na balma nak

  • VÉRITÉ
    29/05/2016 16:56

    Alhamdoulilah bimoula yooboomaaakaa 2fois il t’a des gens qui pensent pas amener leurs femmes à la mecques qu’on me site d autres artistes qui l’ont fait dans ce pays yalla n’a yalla wathia yeurmeude si Sénégal akh adounabi yeuppp si barki nabi moustapha psl que dieu nous guide dans le droit chemin

  • Amina
    29/05/2016 17:06

    yaw boulma sonal indil ma lou leer lou wane ni Aidara setou Muhammad S A W laniou Muhammad S A W niouy niep pa si yem rakhmatalil nass la bouniou ken geuten

  • coum
    29/05/2016 17:17

    neysane laf thiat aidara karara a thioum sokhna bou bakh gua inchallah bercy dina fess bagne tourou

  • mami
    29/05/2016 17:42

    amina suis dakor on est tout seutou Muhammed boulene gnou sonal

  • étudiant
    29/05/2016 17:50

    amina yowe khana wenou thiaga nga nampe mdr

  • AstouSFallou
    29/05/2016 17:59

    masha allah yalla Nalene yalla dolly Laffal thiat ci barke seydina Mouhamed P.S.L

  • zeynab
    29/05/2016 18:19

    mension special sokhna machala réglé ga yarou ga dign ga amga clase am ga personnalité am ga dinèè sur tou am dinee machala c la première foi may soga dég sa voi nila ni rèk la yala na lèn yala mousal thi thiat ak pekhèy non yow waly takou la rek ga takalèko ak ay xarita wala ga outal ko ay non gis nagn ko fi yow aidara karara dieuwoulo ba gnou youbou la tess mba ga fèn ba gnou tath la non sokhna machala j ta dore j taime lov you vremen

  • hariratou
    29/05/2016 19:08

    ??????

  • hariratou
    29/05/2016 19:13

    mdrrrrrr?????????❤❤❤❤??????????

  • fa
    29/05/2016 19:21

    no zeinab ray nguama toth ngua fiii dé dieuwoulo bagnou yobouleu teussss hahahahaaa

  • Seydina Omar sissoko
    29/05/2016 20:25

    Bravo sokhna ,wakh lou ndaw,dieuf lou bari

  • kira
    29/05/2016 20:26

    zeynab tothie ngafi waye Day am danel

  • ziza
    29/05/2016 20:33

    fortna thi kaw thi kanam

  • zeynab
    29/05/2016 21:35

    kira li la wax man safoula

  • Babsba
    30/05/2016 08:57

    Etudiant quand tu ouvres ta bouche pour ne laisser qu’entrer la poussière mieux vaut te taire…soin un peut éduquer nga balma nakk…chacun a droit de dire ce qu’il pense on ou la…

  • PAPIS
    30/05/2016 10:41

    EST CE QUE WALLY DEMNA MAKA

  • go
    30/05/2016 11:04

    soff
    thim

  • ore
    30/05/2016 11:49

    fausse chérife

  • Gor gou Mak
    01/06/2016 18:15

    wa mais yow ispice di counasse bi lakalé nga trop… ya bari frais waye. Aidara yi gnoungui bayiko ci lèèrou Mouhamadou Rassoul Allah: Fatima zahra miy yayou Hassan ak Ousseyn miniou diokh Idrissa.Idrissa mo gadayo Irak actuel niow maroc et c’est là commence l’expansion hadriya en afrique et dans le monde comme l’avait promis le prophète à sa fille bénite ( une grande et noble postérité aux 4 coins du monde-On n’appelle cette famille sainte par excellence AKHLOU BEIT AIDARA-). a noter que l’un de ses petits fils abou Bakr, grand navigateur, a découvert l’amérique bien avant christophe colomb. lire amérique voyage d’abou bakr. Ainsi les premier amérloc furent musulman. En gros ceci n’est qu’une synthèse de la Belle et grande Histoire de cette Noble Famille SALLALAHOU ALEIHI WA SALAM.cette descendance ne doivent ni payer d’împots ni effectuer des corvées.

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL