Vidéo: Waly Seck lance un message à Thione Seck en Prison
De passage sur le plateau Spécial Fin d’année, Waly Seck fait un coucou à son papa et lui présente ses meilleurs vœux pour ce nouvel an.
De passage sur le plateau Spécial Fin d’année, Waly Seck fait un coucou à son papa et lui présente ses meilleurs vœux pour ce nouvel an.
Amine waye yalla meune na ko
moundieule rek yalla bakh na ta dinabakh inchalla te dagua raw say mass ba fawou ak mane khadim seck ak aba li natou la rek te yalla boula tegue tatou dafa beugu defar say mbire te say mbiri papa bou defaro say mbir yaw wally leep dina defarou inchalla khana kay di gnane yalla bou si thiat dougou inchalla machalla
moundieule rek yalla bakh ta dina bakh inchala te daga raw say mass ba fawou ak mane khadim seck ak aba li natou la rek te natou moye defar mbiri diambi te sa papa bou aye mbireume defaro moye saye mbire defarou inchala te dignane yalla bou si thiat dou gou machalla inchalla
inchallah amiine il sortira très bientôt ci dieu le veux les imbéciles qui sont au pouvoir eux tout ceux qu'il veulent c qu'il reste là bas bande des ignane que vous êtes !
oooo refet yala na yala na yala degu sa gnian du courage yala nala yala sam dina bax boul tit bou ragual on né du tou coeur avec toi
wally du courage contunions de prier pour thione que dieu le donne une sante de fer et longue vie ey qu' il sort dans de tres bonnes conditions
qui ta sonné espèce de cons va on parle au intelligent pas à des cons ???
yalna nala yalla mouseul si diate té samala té guéné sa papa fofou mou nékh
J men balc
papa thione yalanala yalla guéné fofou ga nekh thi diam
mercii waly seck yalla ko yalla defal diam…papa thione we love you
Amine que dieu fera sortir papa thione plus rapide et possible.ak. Diamm
C'est beau !