Vidéo – Urgent: Serigne Mountakha Mbacké entouré de la famille de Serigne Touba dévoile sa feuille de route
Le nouveau khalife général des mourides, Serigne Mountakha Mbacké, a fait ce jeudi à Touba, une déclaration qui a été très attendue par l’ensemble de la communauté mouride et plus particulièrement la famille de Serigne Touba. Le khalife a voulu chasser toute ambiguïté vis-à-vis de ceux avec qui, dit-il, partager le travail de la communauté mouride. Serigne Mountakha Mbacké a dévoilé sa feuille de route pour perpétuer l’oeuvre de Cheikh Ahmadou Bamba. Regardez.
Yallah nako yallah defal ndame you kenn mosta am tem yague fi lole te andak werr amiine ya rabi barkeb Borom touba
yalla nga fi yagg Mbacke
sante serigne touba
SANTE Sérigne touba’sante serigne touba mbacké yagg fi lolou té wér nga nianal niou lolou amouniou loudoul di sante serigne touba kone sante serigne touba bou bakh akasa
Yague fi mbacke lole te’ wer ba li nga beugue ligueyale kou tedeki serigne touba sounou yakar tey ak euleuk nou ande ko ak yaw mbacke
Yalla naangui fi yagg lol MBacké mou and ak werr. Bougnaly dii tekk tchi yii di nouro ak « trône ».
ceyy ndakh yalla sant yalla ci moom dei S TOUBA rekka ko nior ndaysaan yalnafi yagg barkep SERIGNE BI
Diaradieuf MBACKE
Yalna yannebi woyoff
Mbacke yeslou nan boubakh tay sako nga nianalnou ba doun bag loudoul serignbi di jafe ndiagalyi bayi tereyi niongui nian nga yagfi ta wer
Mbacke khélyi dalat na boubakh lénefi lool té wér
Mbacke khélyi dalat na boubakh yague lénefi lool té wér
Sama serigne bii mbacké balla yalana fii yala yagall thi barké xassidayii
Yalnang fi yagg lool te and ag wer Mbacké. Yalla oyofal yenn bi ci sa kaw
mbacké yagual lool té werr
Que Dieu Vous Bénisse Serigne Mountakha Mbacké