Vidéo: Un téléspectateur demande à Mami de se couvrir la tête. Regardez!

Se revendiquant souvent de la famille de Serigne Touba, Mami de la Tfm est connue pour sa langue bien pendue. Un téléspectateur à l’antenne lui a demandé de se couvrir la tête pour être plus en phase avec le discours qu’elle prône. Regardez!

15 commentaires

  1. cheikh talibe bamba

    man senegal aka bari ay nafekh ki limko wakh deguela kham na limko wakh sa diomji moy sa bop bi nako mosor mogan si moume fouf

  2. cheikh talibe bamba

    man senegal aka bari ay nafekh ki limko wakh deguela kham na limko wakh sa diomji moy sa bop bi nako mosor mogan si moume foumf

  3. ba ibrahima

    wakh na deug waar nga maana muuru mami. ..li ngay wakh duloolu ngay duundu khoola tal bubax sa boopeu Mami…..

  4. nice

    mais niit mou gui mouru te? lou ban rek lay deff surtout les l’arabe yallah khol rek lay faay fayoul boom fayoul tank

  5. Amina

    koula ne sangoul sa tarr la beugeu ki lim ko wakh moy degeu te mom la Yalla santane pour djigeen djulit yep

  6. Giss Gissi

    defaral sa diamji ken dou kou vakhnit thi kanam adouna bi yepe nako vakh del mouso rou moler valla mou voko thi souff

  7. easy

    couvre-toi la tete si tu veux et laisse les gens en paix !!! j’arrive pas á comprendre pourquoi vous aimez tant humilier les gens en public.

Comments are closed.