Vidéo: Thione Seck "Waly dey dem kene douko téyé...". Regardez

Il n’avait pas fait d’apparition depuis sa sortie de prison. Thione seck dans une vidéo publiée sur internet, fait part de sa fierté suite à la réussite du concert à Bercy de son fils. Regardez!

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Dans le même thême

109 commentaires

  1. mtr

    wally yalla nala yalla defal jamou waye berci amna borom wayi don bene son bi khadiol bay dende nit day kham bopam you amol morom si misic afric wakh dji mofi neke rek waye yalla na yekh bou dewe senegal dotou am way kat


  2. wawe

    senegal mon nekh reck mane justice bi mon me diakhal la loi c pour le diminue gni ga khamni amouniou lo niou lke macky sall domerame numro 1


  3. dieme

    LE grand truand tu devais avoir honte d apparaitre dans les médias pendant des années.Tu es un très grand voleur mentir escroquer les gens.Toute ta fortune c est du haram.


  4. Mbacké dioum

    Assamou alay koum wa rahmatoul Âhî

    Mbokou djoulite yî ngén balle ma

    Ki thione seck la wala damay géntou?

    Mag sou amé soutoura mo ka may bopame, yaw khana da nda faté nî sétagô?yaw khana fébaro?

    Kî référensou kan la? Khana référensou trafikan faux-billets yî?


  5. Senegal

    Mdrrrr pabi mo niak fayda deug deug mounane waly daye dème. Y aw mom dèmato. Tè je vous parle en connaissance de cause salle daniouko wagni ak dolè sakh tè takhoul mou fées


  6. Mouhamed

    Si waxnga deugeu kéneu douko té, mais moyté bopam.

    THIONE SÉCK: ganaw geumo loudoul xalis, bouyawmal xiyamé faxél moudialléla!!!!


  7. wawawww

    bercy mome kouy wrntna fessouul rk do nit wdi guisse bokou thie l fans de waly ne peut pas corompre l journalistes a se point way nak wakhou none mome diaroul sone nopaloulne waly nonam dou nelaw loumou dougue am thi ndam liiii la yalla df bagne douko dindi


  8. ndiakhoume

    niake diom mounta wéssou ngay wooté aférou kilife aférou nii la méll banou fékla ngaye naane ci ndoukhou pootitt wayé nake ségal moo nékhe ba takhe golo gou djouk tallal généme boule negeni fékoone niounane condamnénala 20 ans doko tal bo yoré sa doom dankoy nianal mé pas défko arme diko khékhé démal toube diégelou sou borome thi conorie yi ng djota déf ;video de la honte


  9. Deugeu nekhna

    Allez sur google tapez : salle bercy.

    Vous allez vous rendre compte que la salle est composée d’une fosse en face de la scène et des gradins sur DEUX niveaux ou DEUX étages si vous préférez.

    Pendant le concert de wally, le deuxième niveau a été bouché, la salle réduite et le reste n’a pas été rempli.

    Je ne suis pas un ennemi de wally seck, mais je refuse le mensonge gratuit. J’ai tenu à écrire cela car j’ai des amis qui se disent fans de wally et qui vont sur google prendre des photos de bercy qui n’ont rien à voir avec le concert de wally pour tenter d’embrouiller les sénégalais. C’est ce genre de comportement que les fans de wally doivent arrêter. Ils vont noyer leur artiste à force d’aller de simulacre en simulacre.


  10. bigboss

    Papa thione desolé dééé wayéé yow moom do dém mais je te souhaite tout de meme d’y aller avec waly la prochaine pour faire le plein parsk visiblement waly seul est hyper petit pour détrôner you.


  11. dieukeur

    Pere thione yaw mom teyenanioula quand tu voulais truander les senegalais avec tes 40milliards en faux billet rakh ssi doli teyewat nanioula quand tu voulais dem bercy mayniou diam niakeufoula.tu ferais mieux de te cacher so amone diom


Laisser un commentaire