Machalah Oustaz Alioune SALL, amnga dall, amnga pédagogie, yalne la suniu borom défal tawfeh ak taysir.
AAminn.
babs
certains prient et ne l’ont pas. c’est juste génétique, je pense. même si je ne remet pas en cause la dévotion de ce monsieur.
Amina
Amiin Soxna Yalla na Yalla nangou niane,Oustaz Yalla na la Yalla yok werr ak werle goudal sa fan barkel sa kham kham Yalla bayi lafi ay att yu bari bari nga niouy dimbale si sounou dine,Amiin
deug
macha Allah oustaz coi deuglou li ngua wakh Baye laye mouy Rassoulou lahi lou takh yenn borom xam xam gueustouw len lolou ngir guindi nit ngni mais nioniou niou bakh la niou si bann fanna tra mi wax waxji danni ma wekhone dembeu ma nioul tey.
ayat boy wakh ni gua ko fir dou nonou deh

Amine yallana ya Rabbi nangou niane
macha alah
Macha allahou oustaz alioune sall
Macha allahou oustaz