PUBLICITÉ

Vidéo: Soirée Waly Seck-Gentle Mara met la barre haut avec des « battré » en euros

La soirée de Waly à l’esplanade du Grand Théâtre a encore vécu hier. Comme d’habitude, l’une des attractions à pareille occasion, c’est le show de Gentle Mara qui a habitué le public de farmarène à des interminables « battré » pour le fils grand bonehude Thione Seck.

Cette fois ci, le marabout jet setteur a mis la barre très haut. Si dans la vidéo on peut apercevoir Gentle Mara dans son exercice favori,  des sources très proches du Faramarène nous confient qu’il distribuait des liasses d’euros. No comment.

Abonnez-vous pour regarder plus de vidéos
Annonces
Annonces

34 commentaires

Donnez votre opinion sur le sujet !
Buzz

MaCHALLA BOY BILAHI YA AM CLASS

Icriz

LI NEKHNEU TROPE

Mbay toure

CONTANE SI GENTAL MARA ! Nekh ngama trope franchement

charles

IL FAUT TRAVALLER.

JUSTICE

MANE DEI MÉDINA LA DEUK WAYEI BOY BI LIMOUY DEF SI LOU BAKH YALLA DINAKO FAYE

ibou

Mara il y a des familles qui mange une fois par jour et tres proche de vous ce que tu fait n’a aucun sense de la merde seulement

KhakhaTay

MARABOUT MANE LO DEF BEUG NA GENTAL MARA .Mai mayma khaliss ma liguey

Baye NIASS

Wakh deug yalla billet euros yi mako féké lou am la. Yalla nalla yalla Sam té wéreul thieur yi sa kaw sa kanam rek

Ibou Niang

Tes proches en ont besoin c de. Foutaise poukaree

Ngouda Boye

Voyez moi

Ngouda Boye

Dossi am YALLAH

Chacha

Est ce q nioko tay tamitt

Gora

Beugue guislène ma rekk , khaliss bi nguène wara diokh gni amoul lougnou lèkeu, dounguène ci ame Allah, ni tayaba.

Mohammed seye

Moniwoon paris moy finalou ligue daw gneuw di napé diakayi ak muskine yi sokhla nagnko

smac

Quel foutu jeunesse

betty

Gayii gentle mara Wally et consorts moytulen senn bop ak khaliss bu bari bi di tourner autour de vs diapnagn fi thione tai enquête bi diehagul dagneina hamoulll rekkk

BA

Attention

Cheikh Tidiane Diene

lou Bakh c est contribuer aux constructions des mosquées qui sont inachevées dans Dakar et autres localités ou bien participer aux restos de coeur pour nourrir des indigents etc au lieu de jeter son argent dans des futilités qui mènent a rien.

NDOURA

LA POLICE LA GENDARMERIE OU DIC OU BRIGATE DES INFESTIGATION DOIVENT ENQUETER SUR CETTE MANIERE DE BLANCHIR DE LARGENT ICI AU SENEGAL
– LA SOURCES DE CET ARGENT ?

teuss

Gentle menteur oui
Le PSG est en final ?

Aminah

Mais il a pas honte ???allors que y a des personne qui meurent de faim…tchim

ADINEU

MALA BEUG GENTAL MARA AM NGA KHAM TEI AM NGA KHALISS .MACHALLA

SEYDOU

ADOUNA KOU SANIONE NIOULAY WAY NGAY MAYEI DONC AMOUL MER ! Na khôl YI fekh ! MARA INTELECTUEL

FATOUSH

Dafa civiliser SAKH marabout bi ki peut m donner son numéro svp

Daouda

BEAU GOSS LE GENTAL MARA

BIRAM

SENEGAL KOU SIW REK NIOU BEUG LA DEF ENEMIE! Dem lene klamei sene NDay yi Ndakh ki yayam dafa liguey

Khoudoss MBACKE

LIMOU mokal ALKHOUR ÂNE REK MOTAKH MA BEUG KO ! Ki kouko khôl sakh khamnei dafa am leer MACHALLA

NDAKAROU DIAL DIOP

Gental MARA YA FI NEI GUISNA SI SOIRÉE GAYI DI DIEMEU CONCURENCE WAYEI DOTOUNIOKO DEFATI ! SO AMOUL WONE GALATHIE KENE WAKHATOUKO NDAKH SONALNGA MÉCONTENT YI

SERIGN Mor CISSE

SIGUIL NGA SERIGN YEUP ndakh sénégalais respectéwoul wone serign mai lègui NIEUP beug nek gental MARA ! Yalla nga goude fane

Oumou SOW

J ai pas l habitude di commenter mai cette fois meunouma Mougne SENEGAL NIEUP CONTANE SI YAW MARA .Del def rek tei boussi bolei Ndakh LOUNEI FANG KENE DOUKO DIEKH ???

Sokhna ASTOU

Niit kou nek ak loula YALLA may ki mo saf sénégalais yi parck mane damay suivre page Facebook mai ay temoignage you rafete rek lay guiss ! YALLA motakh may Wakh

JUGE

GRAN THÉÂTRE yay borom lingafa def si ate mi soirée ALASSANE MBAY ,defko si sargal jiguen ak anniversaire Wally ! RESPECT kou mer dal boko

TELEDAKAR

En tout il a un caractère remarquable,en plus il mentalement fort ce Gental MARA .BRAVO

Mama diop

DEG NA DAFA MEUNEU NIANE ! AY djinei la Yor! Mai dou nianal kou amoul khaliss !

Publier un commentaire