(Vidéo) Parodie de "Coller la petite" de Franko - Coupez moi le sac avec Xuman

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Aucune recommandation disponible.

15 commentaires

  1. KANI KHEGNE

    hahahahahah…..enorme le talent et surtout le courage de s'exprimer yalna boula pro-gordjiguene yi sonal yak Simon si obtention visa ni dang lene di khekhe. Waly deye liko dal sedoul parce que media adouna bi yeup deye bo setanee sequences ya ak commentaires ya US, EUROPE ak CANADA ndeyssane danio diap ni ap gordjiguene leu bounou bondoukhatale Senegal mouye fipou si mbiroum soloki sac nguir wonenee amneu droit done gordjiguene.Surtout clip "si vous saviez…" bamoucha tek nak dako geuneu dougueul, toubab ya nenegne dachaye woye "hey bounguene khamone mbeuguel……. danguene kham ni gaur warna meune beug gaur na mome?".Seugn bi dale kouyebou nianal la, gordjiguene senegalais yi nee bitim rew yeup faleu negnoula sene president. Balang ko kham nak nga gueneuti exterieur, mbolemi gordjiguene dik nagnoula nekhal you doune,ndessitou khete wignou bolo done nineu dagnou dieunde seuy billets yekk battrer seye kaw scene.Douli nga beugone? diote ngachi.Wande gorou Yallayi ni mane guigne nagnou si Seugn Touba ni wogne tougnouleu.


Laisser un commentaire