28 COMMENTAIRES
  • tall Souleymani

    Ce pap ale e devenir mikirop dan ce pey

  • isso G

    Arrêter la France n’a rien a voir dedans le peuple a choisi

  • isso G

    Pape boul def forcing Sénégalais yi fene lo nagnou la le peuple est inmanipulable

  • idrissa

    Pape alle yaye nafekh tu avais défendu idrissa Seck lorsque quil ce doute de la sacralité du lieu saint de lislam dans un pays à 90%de musulman il devrait même être tués publiquement aujourdui tu l’encourage a appeler ces militant à attaquer les journalistes tu est vraiment petit

  • anta+beye

    Pape alé vrai domeram

  • Marron-beige 2019

    Macky dina togaat té koufi yengou rek parel ca thiangay té khamne alakhira nga dieum

  • Diabolique 297 Diabolique

    Pape ale sa tounou ndaye soulard bi

  • alfa suare Diallo

    Pourquoi il se précipite à dire ça ??

  • SECK

    Deug fi loffi tal gnou nok la cii caso bi
    En plus on écrit gilet jaune pas juillet jaune

  • ta

    Tal bane deuk khana dou senegal lagnouy wakh
    Fi dé coufi guene yoré torche sakh si mbed mi doto ko défati
    Dégniouye sob rék wayé dofougnou

  • Borom Ndiarem Faye

    Guisnanioufi talibé béthio yi niongui thi kassobi ba légui te béthio monguay léki guanaram jeune boufi sa nday liguéyoul ba dougoufi kasso ndakh macky wala idy wala sonko sa adouna nguay yakh niom niou dém continué sén adouna ak sén ndiabot amlén foula boulén kén khékhlo

    • Moussa Diallo

      Ya am foulla

    • Ansou

      Birame ya tëuth commentaire ti wa salam

  • Abib

    Wakh djig barrina kou annoncé violence ou réclamation si mbedd mi boula militaire wathié la bo bou ngay kham né lep degg la.

  • ta

    Mai se suposan journaliste la et un cancer pour la population coment et qui lui donne un micro se gas là
    Mai c grave koi

  • Zaza

    Il est bien ce qu’il fait arreter de juger les personnes il direct tt c qu’il fait j suis ses émissions..c’est un bon journaliste

  • cheikhouna

    Les dés sont déjà jetés

  • kou+bakh

    Macky gagné na

  • kou+bakh

    Yaw doile rek ngua man

  • Babene Ba

    J’en suis tout à fait d’accord.
    A vrai dire il y’aurait forcement 2iem tour

  • Borom Ndiarem Faye

    Pape alé le vrai satan yallana yalla mousseul senegal thi sa lamigne wi bou sénégalaiyi téyoul thi yaw dingua massa yal rewmi

  • Deug

    Comme tu veut gilet ou juillet mais ça ne passera pas

  • sarr

    bilaye macky sall bou togaté yen ni ko votel sah dina meti si yen inchallah

  • Ibou

    Pape alé est un danger cause pour laquelle il a été licencié de la 2stv
    Honte a toi
    MACKY gagnera au premier tour
    Tu te prend pour qui
    La loi des urnes est au peuple et non a un sourd-naliste

  • Deug

    Si macky sall ce proclame vainteur on va brûler ce pays par A ou B la France n’a qu’à aller s’occuper le problème des juillet jaune

    • Thanks

      On commencera chez toi alors

    • khadim ndiaye

      France degage

    • diop sy

      Il faudra d’abord brûler votre maison et c’est pas prudent de votre part de faire ce genre de commentaire .

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *