Vidéo – Les Mbourois ont réservé un accueil populaire à Ousmane Sonko… Regardez !

Ousmane Sonko a marqué son empreinte durant cette première semaine de Campagne. En caravane à Mbour, ce dimanche, le leader de Pastef a sillonné la petite-côte. Avec un accueil populaire. partout où il est passé. Suivez sa caravane en direct…
https://www.facebook.com/SonkoOfficiel/videos/2258981007720674/
Félicitation notre président yala Moy maye baïre te yala may nalako. di wahat alhamdoulilah
Ah les pondeuses automatiques de APR….ok on verra bien
194 pays du senegal 25em le plus pauvre bravo MACKY ,mais malhereusma SONKO est venu le sauveur EL SALVADOR
Deug rek moye mou dje Macky si tu avais dis la vérité aux sénégalais li yeup doula ci done fek
Macha Allah t’assister
Sonko laff thiat boys nooooo beuri bairé
Comment sonko était à mbour aujourd’hui je viens d’apprendre cette nouvelle
Sonko dafey tek rewmi ci andd, lou tol ak 100 millions leu am ci tullow oil, directeur financier bi mo kokou diokh ngir mou géré campagne bi. Lepp ngir takal gouvernement bi ci gestion ressources yi, opération bobou niou deff ngir yeungeul rewmi. Wayé diap negn ko, corrompu leu, dou nitt kou bakh.
Sonko fou mou toll rek mi ngi niawal Sénégal ak Macky SALL, di wakh wakhou merkatt, di fenn. Li mouy wakh ci president ci lou bonn mo nekk ci mom
Saga yi, sani kher yi, fenn bi, Sonko bayiwoul dara. Li mou beug yeup moy saltél imagou macky SALL, ak ay discours you bonn pour yeungeul rewmi rek.
Sonko nioroul dara, andoul ak sagom, nek ci lou ko nekh, fittneu rek la fiy indi.
Kou nekk inspecteur des impots, kharou niou ci yow loudoul def ci liguey, djiteul sénégal, woné expemple bi, sett weth ci alal rewmi
Sonko war neu leral sénégalais yi ci 94 milliards yi, tekk ci 46 milliards yi, ak euleuk louy fegnatt. Bolé ci lep li niou ko toumal
Document bi atlas publié, ak audio yi, affaire tullow oil mi ngi woné bi Sonko corrompu leu. Amoul benen preuve bou ko geuneu lerr. Kham negn lou takh Sonko amoul place ci elections yi ak palais.
Sonko ci ay mireum, diokhoul tieur sénégalais yi, ak trésor public, nekoul lou doul protégé pochamm, fossoyeurs leu ak ay souff you mou mom té déclaré wou ko, yénénn you mou diay ak spéculation bou djégui dayo. Ak li yeup ngen beugue fall ki ? Di diay kou sett té dafa tilim
Sonko daf méy rélo. Moy hopital bouy khepp dispensaire. Sathie leu di woté satiéy. Complice leu ci affaire bi, bolé ci di nian 12% commissions sou dé li niou beug ci Etat bi amna. Sonko dou nitou dara
Sonko ngi woté détournement 94 miliards, ngeu degg ni dafa waron am ci affaire yi 12%. Dafa niou tek ay tiomo.
Sonko dafey daw yenn lath yi, degn ko diap ci lou lerr, Sénégalais yi daf len bett, wayé deug moy moudjou.
Sonko dou nitou dara, kann mo gueum ni djouboul ? Amoul benn fayda ci sama khalatt. Meunpoul sakh tontou ci li niou ko toumal. Sathie leu, Conseil constitutionnel war negn diok ci ay mireum. Mom, Khalifa ak Karim nio bok fi niou dieum
Sonko dé, affairyi dou ci guéné nonou, deug moy moudjou.
Sonko ngi kharr gni mou andal niou defendre ko, wayé mom ci bopoum tontou woul li niou ko toumal. Dou Nitou dara.