Vidéo: Mister Shake feat Pape Moussa. Regardez !

Après avoir fasciné le public américain du BAM pendant deux semaines, Pape Moussa montre toute sa versalité dans cette vidéo Hip Mbalax du roi du Hip Mbalax Mister Shake. Regardez et appréciez!
Les délires de Pape Moussa-Mister Shake «Olivia»
Olivia- Mister Shake ft Dancer Pape Moussa
honestly I don’t think Mr shake is normal.
Yenn ayy seerr guene….vous ne connaissez que le mbalax sénégalais…ca c nouveau mais aussi degoulene english waaayyyy..khamoulene limouye waayyy…dinalene ko traduire lol…..rama badiewe katt….waly rekk la guise..boulene ciiss……courage mister shake i am with u…..
sokhor bakhou badiene rama badiane. damal outi jeukeur moo gueule ak sa gnawaye ndax kou sokhor day gaan….
Khana forum bii da ame niary amina, AMINA bou sélleu ak AMINA nittou adouna quand il s’agit de Wally « waye daffa haram » « Féthieu daffa haram » quant il s’agit de youssou et tous qui gravite au tour « Léppeu daguane avec ces Amine Amine » Ah mane dé diomina
thoot ki mo cons d ak musique game bou nakhadi bi comme kouye tegue si aye khotou potes Pape moussa fethaga lo khamoule bi ritmas bou bizarre
Waaaaaaw!!! rafetna son bi nekh na te bess….original mbalaxman
tres nekh….pape moussa moo ko torr…
nékhoul dara lshh