(Vidéo) Mise en garde du Khalife général des Baye Fall contre Serigne Saliou Sow et Waly Seck

Serigne Moustapha Fall Fati Kane transmet le message du Khalif Général des Baye Fall qui met en garde ceux qui se disent Baye Fall mais leurs pratiques ne s’accordent pas aux enseignements de Cheikh Ibra Fall.

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Dans le même thême

69 commentaires

    • fall yaram

      yaw salam yeureum nala kouye dingate niaka djoulick bay fall mome khamatouma si yaw dara yéne gni nguéne khamné nafékh mo léne diape ba takhawal yala ak yonéne te bi dioté koudoul serigne touba ak mame cheikh takhawofi gnép wa wédi yala gni wara sétate séne bop moye yéne nioniou té nak cheikh ibra mome kouye dougou si mbirame daga khamoul


  1. FEUZ

    wa yen sonal nguen nou, vous ne priez meme pas , on dirait k la religion vous appartient .vous etes qui? du nimporte quoi le senegal. franchement vous nous prenez la tete avec cette histoire. chacun veut se faire une publicite pff pathetique


  2. anouch

    yalla d siip neu sax kouy tiudou tourou gor djigueine wahoumeu nak tour bobou di guener si gueminou kilifeu diner …naniou kholate kadou yi t setate lingueine di wax ….y'en a marre a la fin …deil leine wax borom niary tour yi book ay kadou dafa wara rafaite surout boula nieup di deglou ….yalla meune neu atteil bopam donc keep calm leu nieup wara daif mais counaik di profito si wax dji pour am si ngooreu ….na goreii waay waly moni leine beugu eup fouleu d ….salam


  3. ismaila ba

    Cheikh ibra fall khamoulenko yen baye fall yi cheikh ibra da dieulon wird tidian cheikh Ahmed warko mou bagna dem après mou dof mo takh mouy sol yeré you diakhaso khamgua dof dou diouli mo takh diouli wathi ko


  4. Un mouride

    J'aimerais bien savoir ce que Serigne saliou sow a dit

    Si c'est concernant le ndiguel que Chekh Ibra a donné à ses disciples concernant le respect de la charia ou c'est autre chose


    En plus on a titré ici que c'est le Khalif des bayes fall qui parle

    est ce que c'est lui qui a demandé a ce qu'on parle de son nom

    ce que je vois ici c'est des jeunes qui se disent baye fall tout comme waly seck se dit baye Fall


  5. mandou lene

    donne baye fall dou ci solou dou ci wakhine baye fall ci xol la alhdouliah ba yalla di faye xolwally ne repond a pwrsonne senengal ay hypocrite reck la beuri vous avez beaucoup de blem a regler wally il a deja ce qui la may lene ko diam ay way domou diambour la li euppouna dh comme ay deumeu issshhh


  6. Rokhaya Niang

    Franchement les sénégalais sont pathétique mais c'est quoi le problème être baye fall c'est pas dans le port vestimentaire chacun de nous à c mille et se préoccupe des 50 d'autres de grâce Wally si j'étais toi je mebranlerai mm pas de tout ces propos hypocrite pufffff soit disant un pays laïque ????? wally vit ta vie comme tu l'entend tu es libre de faire ce que bon te semble #onlygodcanjudgeyou


  7. choupi wally

    hahahahahah yene bilahi daguena nekh dama foguone bou wally defai istyl boumou warou ta deff sakh ware nagnou ko woo neko aa lide bakhoul ndakh nitte matou mes baye fall beurina si sene bire fofou di mboubo tourou bay fall tes limouy def kene douko wakh tes sakh wally moko guene done baye fall yawwe gua gueni si mo gueneu yombe wally guenesi dakh baye fall kene momouko wayyy demlene wakh lenene li dou deba


    • le sage

      si certains choisir la voix du salue d'autres préfèrent celle de Ibliss satan.on est mouride et on ne souhaite de mal à personne mais quand quelqu'un connait des erreurs monumentales il doit s'en excuser et éviter de les répéter à l'avenir.mais s'il s'entéte il subira pleinement les conséquences de ses actes avec toutes les personnes qui le soutiennent.amna gno khamni danoo ame probléme ak sounou borom ndakh nangouwounou dogalam ci serigne touba.waya yalla naléne borom bi guindil boppam.mangui gnane talibé yi bounou toppou séné khole ci commentaire yi.lou way wakh boppam ,adouna yagoul ta baméle leundame na


  8. malick

    Al hamdoulilah cheikh ibra dou morom dou mass téyit bene goor yabouko kone nak bougnou naguou gnou yabatéyii di mboubo tourou baye fall di yakh sounou Yoon wiii .djeureudjeufff Borom Touba djiarama Mame Cheikh Ibrahima Fall


  9. dabakh

    Yekh nguene thai lii nguene def.nit kpu baakh day Seagal limou bok.wante nanguene wakh thi seuti mame baroom touba yi niouy def loumel nii thi bandits yii di saltel yonou mouride niouni pate de darà takhoul ndakh khaliss(bethio,AK gni melni mome niongui yakh yoonwi teken wakhoul)


  10. Sam le pirate

    🙁 Au lendemain de la prise de parole de Serigne Saliou Mbacke ibn Serigne Mouhamadou Lamine Bara Falilou pour condamner le comportement de certains hommes qui se prennent pour des femmes dans leurs actes,que Waly Seck fera encore une sortie publique pour narguer le peuple disant qu'il fera sans hésiter un autre DIAGAR DIAGARI avec son sac de demoiselle khawma diongama.Aujourd'hui,voici donc le résultat de son NIAK YAR ak NIAK TALIBEE,qu'il assume cette situation plus que compliquée qui s'abat sur sa tête de NAFEKH! 🙁


  11. na

    wa mane damay beugue diomi wally wa yene senegal lougnou beugue nague li eupeu dé yéne wally daguene ka mana guéné si baye fall manou lene ka bou féké yena mome niit merde waay .wally seck loumouy dimali si domou adama yéne gni tague sene radio di wax doulene ka def lhabit n fait l moin doul wayene


  12. Diop

    ay chaytan moussal niou..senegal deguoul nanioufi ay mbane essence t bou niou moytou oul allumettes bi koy tal nio kay dieude.yeete lene t bania yeuguel fiitna.kheep yalla ak sounou boop rek mo niou sonal. mame cheikh amena na placame thia yalla na niou deef né mome.ligueye pour notre propre place au paradis


  13. tit

    Wally mo togne bopam dafawarona toup diéglou bou yag mo nékfi nan dina contuné di yor sacbi légui nak miguini kilifa yépa mér té sacbi mo waral warar toubayi di togne kou tédgui


  14. kara

    jajeuf fall yaram ni rek la amougnou kou doul baboul mouridina tè nak serigne cheikh fall bayou gorr nèna pèsoumm kanam borome mo koy fadial bopam kon bok nok baguène wakhè …nakh SUNU yakar tey ak euleuk fo woul folou woul serigne cheikh dieumb fall yalla nafi yague tè werr lol.


  15. bleu

    C est vraiment équerrant q on s dit bay fall et que notre propre marabout n est pas content de notre comportement j t pleins vraiment waly peut être que c maintenant le temps de changer n serait que pour ce tarikha. Bayfall dont tu acclame toujours en faire partir ça ne doit pas être un slogan que tu chantes tout l temps ndang koy dieufe bay fall ndiguel


Laisser un commentaire