Vidéo – Meurtres d’enfants: Borom Thiès plaide en pleurant en direct -Regardez

Les meurtres et enlèvements d’enfants ont installé la psychose dans tout le pays. Serigne Moustapha Amar dit Borom Thiès invité de l’émission « 12/14 » sur la Rdv ce jeudi, se dit très peiné par ces actes odieux qui guettent notre société. Le marabout a même versé de chaudes larmes en direct sur le plateau de 12/14.

Regardez!

28 commentaires

  1. nafii

    serigne bi wakhe deuge yala mane dee tay mm bimala setenaer dama dioye yala kham nakoe

  2. emigre bi

    senegal a exterieur d mome geuram nane la setane nala bame diekh mano wakh bame diekh t dognou kassal sounou droit

  3. maty

    qui dee sassou nou ko invite tele wala si cite internet yi mane damakoy suivre dakh wakham daf ma nekhe lole surtout retane bou sewe bi damala beugue bilaye

  4. modou modou

    yawe la geume mane amar diker sayo neker si plateau yi gnoune ngay nekal mala beug

  5. ana

    aye domi khath reke gnoy defe lou bone lolou gniy raye khaleer yi dounou nite mala sakh molene taner

  6. Mane serigne moustapha damala beugue reke teee yala reke takh yawe askane wi nga fi nekale yague fi lole t were si barkep alkhouran

Comments are closed.